paroles de chanson Sadik Lady - Viviane Chidid
Bu
ñuy
doxaan
ci
lune
ding
ko
deg
I
love
you
baby,
my
sweety,
my
lady
Yama
gënël,
sama
ndey
ji,
ak
sama
baay
bé
Sukk
raam
jébbalu
joy
lune
ñu
def
ko
Bu
ñuy
doxaan
ci
lune
ding
ko
deg
I
love
you
baby,
my
sweety,
my
lady
Yama
gënël,
sama
ndey
ji,
ak
sama
baay
bé
Sukk
raam
jébbalu
joy
lune
dinañ
ko
def
Lima
metti
batax
ma
sopi
jikko
(moma)
Def
nima
mel
ba
nopi
ni
fess
(moma)
Nelawal
ma
ma
yewu
gëna
sadik
(moma)
Góor-e
tax
jigéen
soxor
leegi
Jël
pakka
jam
ko
sama
digg
xol
(moma)
Bayi
fa
lekket
bo
xamni
du
deñ
(moma)
Nelawal
ma
ma
yewu
gënë
sadik
(moma)
Góor-e
tax
jigéen
soxor
leegi
(Leegi)
Ñaata
yoon
lama
wax
"I
love
you"
My
baby
(Baby)
Ñaata
yoon
lama
wax
loolu
Xale
bile
moom,
lu
Yàlla
xam
doyna
Dafma
gëlëmël
ci
mbëggeel
touté
dess
mu
ray
ma
Xale
bile
moom,
dafma
né
daf
ma
lova
Ndeketé
lepp
lum
la
mës
wax
ay
fenn
la
Xale
bilé
(ñewna)
Xamal
mani
(moom
la)
Néma
sama
(goor
la)
Lepp
ay
(door
la)
Xale
bilé
(moma)
Soppi
na
(jikom
ba)
Fima
ko
romboon
ci
mbedd
mi
daf
ma
dab
Bula
góor
toppate
néla
bëgg
nala
Xamal
ko
xol
dafa
Oyof
buguma
nga
gañ
ma
Bula
góor
toppate
néla
bëgg
nala
Lacc
ko
bëgg
na
giss
papam
di
toroxal
Yayam
Baby
Bu
ñuy
doxaan
ci
lune
ding
ko
deg
I
love
you
baby,
my
sweety,
my
lady
Yama
gënël,
sama
ndey
ji,
ak
sama
baay
bé
Sukk
raam
jébbalu
joy
lune
ñu
def
ko
Bu
ñuy
doxaan
ci
lune
ding
ko
deg
I
love
you
baby,
my
sweety,
my
lady
Yama
gënël,
sama
ndey
ji,
ak
sama
baay
bé
Sukk
raam
jébbalu
joy
lune
dinañ
ko
def
Lima
metti
batax
ma
sopi
jikko
(moma)
Def
nima
mel
ba
nopi
ni
fess
(moma)
Nelawal
ma
ma
yewu
gëna
sadik
(moma)
Góor-e
tax
jigéen
soxor
leegi
Jël
pakka
jam
ko
sama
digg
xol
(moma)
Bayi
fa
lekket
bo
xamni
du
deñ
(moma)
Nelawal
ma
ma
yewu
gënë
sadik
(moma)
Góor-e
tax
jigéen
soxor
leegi
(Leegi)
Ñaata
yoon
lama
wax
"I
love
you"
My
baby
(Baby)
Ñaata
yoon
lama
wax
loolu
Buñu
bëgg
dem,
buñu
bëgg
dem
Te
gën
lula
ci
Yawit
boleen
jekko
tegal
le
lu
sadik
Buñu
bëgg
dem,
buñu
bëgg
dem
Te
gën
lula
ci
Yawit
amal
fulë
amal
fulë
Wawaw
bàyikoo,
bàyikoo
Ndax
moom
xamul
sa
njëkk
Oh
bàyikoo
oooh
Ndax
moom
xamul
sa
njëkk
Sister,
please
don't
cry
Fompal
say
rangoñ
Bula
góor
jaral
ngay
joy
Fompal
say
rangoñ
Bu
ñuy
doxaan
ci
lune
ding
ko
deg
I
love
you
baby,
my
sweety,
my
lady
Yama
gënël,
sama
ndey
ji,
ak
sama
baay
bé
Sukk
raam
jébbalu
joy
lune
dinañ
ko
def
Lima
metti
batax
ma
sopi
jikko
(moma)
Def
nima
mel
ba
nopi
ni
fess
(moma)
Nelawal
ma
ma
yewu
gëna
sadik
(moma)
Góor-e
tax
jigéen
soxor
leegi
Jël
pakka
jam
ko
sama
digg
xol
(moma)
Bayi
fa
lekket
bo
xamni
du
deñ
(moma)
Nelawal
ma
ma
yewu
gënë
sadik
(moma)
Góor-e
tax
jigéen
soxor
leegi
(Leegi)
Ñaata
yoon
lama
wax
"I
love
you"
My
baby
(Baby)
Ñaata
yoon
lama
wax
loolu
Attention! N'hésitez pas à laisser des commentaires.