Wally B. Seck - Faramareen paroles de chanson

paroles de chanson Faramareen - Wally B. Seck



Diémeu liguey
Yalla def ma yeksi fi
Tallouma léneu
Sama yone lay topp ni
Faramareen
[?] ...?
Douma cii léneu
Yalla ko def cii man
Sama yone lay gaw sorri na
Fouma diar nieup daw djégué si ma
Néma djak sen beut amatouma
Loumey prouver dambalégouma
Wait for me
Wait for me
Wait for me
I′m on my way
Wait for me
Wait for me
Wait for me
Wait for me
I'm on my way
Just wait for me
I′m gonna shot them all a gun
I commend fine like pit oven
[?] ...?
I got the key of the city
Oh oh oh faramareen
Mom la done mom la done yeah
Faramareen
Dommi buur la dommi gorr la
Faramareen
Bama doné baye fall sant na
Faramareen
Oh oh oh
Wait for me
Wait for me
Wait for me
(Wait for me
Wait for me
Wait for me
Wait for me)
Baye boye sant nénioula bing niou dioxé yaye djou bakh
Wally [?] beug nala terral yaye
Mounouma fatté fima djougué
Sama diar diar like dafa djaffé
May xouss di niaffé
Ba yeksi fima
Gni di sanni ay poté
Ana nguéne guissoumalène
Mangui tokk man sama corner
Dellou sant Yalla
Wait for me
Wait for me
Wait for me
I'm on my way
Wait for me
Wait for me
Wait for me
Wait for me
I'm on my way
Just wait for me
I′m gonna shot them all a gun
I commend fine like pit oven
[?] ...?
I got the key of the city
Oh oh oh faramareen
Mom la done mom la done yeah
Faramareen
Dommi buur la dommi gorr la
Faramareen
Bama doné baye fall sant na
Faramareen
Oh oh oh
[?] Dima noyyé
Nianou mako Yalla
Gni deniouy beug gni di bagn
Nonou mo gueune cii man
Dama di guewel di wara woyy
Yalla def may begueulé
Fi ak mangui meune dina woyy beu
Faramareen
(Babacar may sa baye)
Faramareen
(Seydina Aliou may sa baye)
Faramareen
(Mohamed may sa baye Binetou may sa baye)
Faramareen
(Aïcha may sa baye Mommi moy souniou yaye)
Faramareen (woooooh [?])
Faramareen [?]
Faramareen [?]
Wait for me



Writer(s): Fefsy, Wally B. Seck


Wally B. Seck - Faramareen
Album Faramareen
date de sortie
17-12-2017




Attention! N'hésitez pas à laisser des commentaires.