paroles de chanson Bamako - Youssou N'Dour
Si
gare
bi
lako
fekkeu,
mi
ngui
sanguo
seur
té
beut
yi
di
takkeu,
ma
dal
di
koye
nougnou
mou
dal
di
maye
faye,
dal
di
maye
yédeu
ci
adouna
bou
yakhou
bi
mane
douma
fatté!
Ah
mani
ah
mani!
douma
fatté
Bamako
lii
mani
lii
mani!
mane
douma
fatté!
kerok
lama
khamal
louma
khamoul
woone
ci
diamono
bou
yakhou
bi
yénene
ak
yénene;
balaa
maye
dougeuti
mane
ci
loumou
meuneu
doone
dinaa
fattélikou
ndaw
sossou
limouma
wakhoone!
souy
souy
sou
sou
sou
sou
sou
souy
souy!
Ci
gare
bi
lako
fekkeu
mi
ngui
sanguo
seur
té
beut
yi
di
takkeu,
ma
dal
di
koye
nougnou
mou
dal
di
maye
faye
dal
di
maye
yédeu,
maky
yé
maky
maky
yé
maky
yéééééééééééé!
waw
kérok
lama
khamal
louma
khamoul
woone
ci
diamono
bou
yakhou
bi,
balaa
maye
dougeuti
ci
loumou
meuneu
doone,
dinaa
fattéli
ko
maky
yé
maky
maky
yé
maky
yééééééééééééééé!
ah
mani
ah
mani!
douma
fatté
Bamako
lii
mani
lii
mani!
mane
douma
fatté
Bamakoooooooooooooooooo
Album
The Lion
1 The Lion (Gaiende)
2 The Lion (Gaiende)
3 Shakin' the Tree
4 Kocc Barma
5 Bamako
6 The Truth
7 Old Tucson
8 Macoy
9 My Daughter (Sama Doom)
10 Bes
Attention! N'hésitez pas à laisser des commentaires.