Youssou N'Dour - The Lion (Gaiende) paroles de chanson

paroles de chanson The Lion (Gaiende) - Youssou N'Dour



Fo deug marawath soungou gaindé la
Ndiaye gaindé boure leuh deugeu la
Fo fekk gaindé te dou fi takhaw
Téé lou mou beugeu dall di ti tekk lokhom
Mome néna kéén waroul bakou
Mome boure la def bopame kou doleme
Bagne na ba dou bokol yonam
Kou kou wedi na diarr fo mouy diarr
Ngioune ngui yéney sou ngou gaindé
Ngioune ngui yéney sou ngou gaindé
déé
Nbamli nbamli guén ko dieul
Na guén ko deff na guén ko dann déffé
Nbamli nbamli guén ko dieul
Nbamli nbamli guén ko dieul
Na guén ko deff na guén ko dann déffé
Nbamli nbamli guén ko dieul
Diambar gnioun dhégne ko dondou
Sou gnou mame mou sou ngui dess ganaw
Diom diodou mougui fi moussou fi diougé
Fitt bodou mougui fi moussou fi diougé
Sou gnou rew mbi royoukal la moussa donn
Diom diodou mougui fi moussou fi diougé
Diom diodou mougui fi moussou fi diougé
Diom diodou mougui fi moussou fi diougé
Tééééé
Nbamli nbamli guén ko dieul
Yélééé yélééé
Nbamli nbamli guén ko dieul
Na guén ko deff na guén ko dann déffé
Nbamli nbamli guén ko dieul
Yélééé yélééé
Nbamli nbamli guén ko dieul
Yooooooo
Fi ngou tolou ngoune amm gnou yakar
Sou ngou mbeur bi da fa endall douléme
Mbeur bi kou ka sorou mou danne la
Mbeur bi kou ka sorou mou danne la
Yététééé
Nbamli nbamli guén ko dieul
Yélééé yélééé
Nbamli nbamli guén ko dieul
Mboroti ndiaye dou delou ganaw
Nbamli nbamli guén ko dieul
Fitt bi déé daf ka dondou
Nbamli nbamli guén ko dieul
Bilay
Na guén ko deff na guén ko dann déffé
Nbamli nbamli guén ko dieul
Yélééé yélééé
Nbamli nbamli guén ko dieul
Yélééé yélééé
Nbamli nbamli guén ko dieul
Yélééé
Gaindé ndiaye gaindé la
Nbamli nbamli guén ko dieul
Yélééé
Mboroti ndiaye
Nbamli nbamli guén ko dieul
Deugla deug khamnako
Nbamli nbamli guén ko dieul
Yélééé yélééé
Mboroti ndiaye
Nbamli nbamli guén ko dieul
Na guén ko deff na guén ko dann déffé
Nbamli nbamli guén ko dieul
Bou la yéé te
Nbamli nbamli guén ko dieul
Lyrics The lion Gaindé By Abdoulayebacary




Youssou N'Dour - The Lion




Attention! N'hésitez pas à laisser des commentaires.