Youssou N'Dour - Tell Me paroles de chanson

paroles de chanson Tell Me - Youssou N'Dour



Par AbouAmg
Tell me
Wakh ma
Dis-moi
Yaw loy khalaat
Tell me
Wakh ma
Dis-moi
Yaw loy khalaat
Chérie boy
Chérie boy, wakh ma
Chérie boy, beugouma
Beugouma ngay khalaat
Chérie, mon amour
Ne te fais pas de soucis
Oh, my darling
Tell me
Wakh ma
Dis-moi
Yaw loy khalaat
Tell me
Wakh ma
Dis-moi
Yaw loy khalaat
Tell me
Wakh ma
Dis-moi
Yaw loy khalaat
Chérie boy, mba, méréwoma
Souma déconné yeugouma ko
Chérie boy, souma sagnone doy khalaat yaw
Je veux te voir toujours bëgg
Baby, my baby nieuweul diégué ma
Diégué ma, niuy wakhtaan
Nono beugué ma défal lako
Diégué may
Kay diégué ma mon amour
Beugouma yaw ngay khalaat
Do not be worried
Chérie mon amour
Ne te fais pas de soucis
Oh, my darling
Tell me
Wakh ma
Dis-moi
Yaw loy khalaat
Tell me
Wakh ma
Dis-moi
Yaw loy khalaat
Tell me
Wakh ma
Dis-moi
Yaw loy khalaat
Tell me
Wakh ma
Dis-moi
Yaw loy khalaat
Nélawal
Bay khandor
Ne te fais pas de soucis
Nélawal yaw
Boul khalaat
Douma déf lou lay sonal
Nélawal
Mon amour
Ne te fais pas de soucis
Donne-moi ta main
Nagn andeu dokhantoudji
Tell me
Wakh ma
Dis-moi
Yaw loy khalaat




Youssou N'Dour - History
Album History
date de sortie
26-04-2019




Attention! N'hésitez pas à laisser des commentaires.