Youssou N'Dour - Téléphone paroles de chanson

paroles de chanson Téléphone - Youssou N'Dour



Mineuneté sou amoul, thioféle dotoulame
Thioféle dé, sou amoul beugueneté dotoul ame
Beugeuneté sou amoul, kharito dotoul ame
Kharito sou amoul,, khole yépeu dal di wowe
Kholeyi sou wowé yeurmandé dal di diekh
Yeurmandé sou amoul seîtané dal di téwe
Séîtané sou gnewé, askane wi dal di tasse
Ndékété, safara, dina dioure diangoro
doyna waré, doyna ware
Gueudj naniou langue lôlé
Di wakh, di kholaneté
Sétalma lilé
Guisseulema lilé
Sétalma lilé
Guissalema lilé
Haannn... ana penche ma, ana sabar ya, ana tama dia
Yegueléléne, yeguelélno, yegueléléno
Bou ndieukone, wakhtane thi penche...
Diébané tamaka dane def, sabaraka dane def, wouy...




Youssou N'Dour - Alsaama Day
Album Alsaama Day
date de sortie
10-04-2007




Attention! N'hésitez pas à laisser des commentaires.