paroles de chanson Beugue Dou Bagne - Youssou N'Dour
Couple
bi
Maye
dadiéle
soumaye
dokhanetou
dji
Foléne
séne
Gnoungui
défe
bras
dessus
bras
dessous
Bataye
gnoungui
ni
dôniye
make,
di
Geu-neu
begeunté
Mbeugéle
rékka
wor
Mbeuguéle,
mbeguéle
rékka
nekhe
Taye
gnoungui
ni
di
tôgnanté
Di
kalanté,
melniye
dômi
badiéne
Léke
léke
gnou
méro
ba
kouné
khole
guéthie
Nga
guéssouwaté
sénate
léne
gnouye
Wakhtane
Oh
mbeguéle,
mbeguéla
nekhe
Gueume
léne
ni,
mbeguéle,
rékka
wor
Han...
oooh
Bagnou
dôné
gouné
Thi
lagne
khamanté
wône
Bagnou
dôné
ay
ndawe
Thi
lagne
begueuneté
wône
Bataye
gnoungui
ni,
dôniye
make
Digueu-neu
begueuneté
Mbeguéla
wor
Mbeguéle,
mbeguéle
rékka
nékhe
Sô
dokhé
ba
séne
kéne
thi
gnôme
gnare
Tôgale
khare,
légui
kénéne
ki
gneuwe
Dara
gueunoule
nekhe
Mbeguéle
gou
sincére
Gôgou
mbeguéle
Kéne
dou
thi
meune
dara
Oh
mbeguéle,
mbeguéla
nékhe
Gueume
léne
ni
mbeguéle
rékka
wor
Han...
oooh
Mane
beugue
nâla,
mâla
rawe
menou
kô
faye
Wouy
mbeguéle,
wouy
mbeguéle,
wouy
Guise
beugue
yalla
mo
koye
défe
wouy
Mbeguéle,
wouy
mbeguéle
wouy
Mbeguéle,
wouy
mbeguélo
Beugue
na
beguetouma,
bôba
mbeguéle
Ga
dafa
dess
Mbeguéle
bou
diogué
thi
khole,
délou
Fa
laye
desse
abadâan
Mbeguéle
kéne
meunou
ko
diaye
Té
kéne
menou
kô
dieunde
thia
marsé
ba
Défe
thia
yeurmandé
Marie
ak
Cheikh
Marie
(choeurs)
Beuguéneté
naniou,
Amar
Xamanté
naniou
bou
yague
Beuguéneté
naniou
Xamanté
bou
yague,
Amar
Minanté
naniou,
Amar
Haan
beugueunté
naniou
Mbeguéle
kene
douko
diaye
Mbeuguéle
amoul
religion
Mbeuguéle
amoul
niit
kou
nioul
Ak
niit
kou
wekh
Edit
by
Lamine
1 Bou ba yeko
2 Beugue Dou Bagne
3 Borom Gaal
4 Amitié
5 Téléphone
6 Yonou Deugue
7 Bololene
8 Del Sol Dal
Attention! N'hésitez pas à laisser des commentaires.