Youssou N’Dour - C'est l'amour paroles de chanson

paroles de chanson C'est l'amour - Youssou N’Dour




Souma wahtané ak sama ñeguenay nah goudi dey yokou xel, sou beuthiagué ma dadi faté man guenteu yi ma guentone bikeu.
C'est lamour ohhhhh.
Soumala rombé di deme ga tekni lepeu bah si man apparence bi nahnala xamoulo li nek si man c'est l'amour c'est l'amour c'est l'amour ohhhhhhh.
Man lekouma man nanouma batay c'est l'amour



Writer(s): Youssou N'dour, Habib Faye, Max Calo


Attention! N'hésitez pas à laisser des commentaires.
//}