Dip Doundou Guiss - ànd xeex coronavirus текст песни

Текст песни ànd xeex coronavirus - Dip Doundou Guiss



Sa loxo set
Sa lepp set
Bul nuyu kenn
Bul lëng kenn
Bul génn kese ndax bëg génn
Bul sëqët fepp
Bul jége kenn
Sëqët, fièvre, bop buy metti njëk feeñ
Soj, problème noyi, senn sa bakkan
Sëqët, fièvre, put buy metti, malaise feeñ
Du rey nit ku ñul si ñi xamul dëg ak fenn
Sa loxo set
Sa doom yi set
Bul nuyu kenn
Bul lëng kenn
Bul génn kese ndax bëg génn
Bul sëqët fepp
Bul jége kenn
Sa loxo set
Sa lepp set
Bul nuyu kenn
Bul lëng kenn
Bul génn kese ndax bëg génn
Xeex ak Corona Virus,
Microbe, jàngoro la, du nit
Aduna nek si combat
Du gis ku muy xeexal
Nuro nak grippe
Nañu éviter contact physique
Xajul Grand Yoff, Colobane, Pikine
Tax ba ñu annuler programmes yi siiw
Tax ba ñu foog ni àddinay tukki
Medecin sonu na si li
Amul vaccin, ordonnance tamit
Mu ngi ray, day toroxal nit yi
Buñu tooge dina bari ay victimes
Set si sa askan, set si sa bopu
Tëju te baña seeti sa mbokk
Julli sa màkkaan, Messe si la bokk
Xeex ko mu jeex mbir yepp mëna doxx
Masque, sabu, antiseptique
Raxasu, sangu dadi set wecc
Dal, muñ, bañ lu melni dess fi
Gën di ñaan pour jamm day dikk
Sa loxo set
Sa lepp set
Bul nuyu kenn
Bul lëng kenn
Bul génn kese ndax bëg génn
Bul sëqët fepp
Bul jége kenn
Sëqët, fièvre, bop buy metti njëk feeñ
Soj, problème noyi, senn sa bakkan
Sëqët, fièvre, put buy metti, malaise feeñ
Du rey nit ku ñul si ñi xamul dëg ak fenn
Sa loxo set
Sa doom yi set
Bul nuyu kenn
Bul lëng kenn
Bul génn kese ndax bëg génn
Bul sëqët fepp
Bul jége kenn
Sa loxo set
Sa lepp set
Bul nuyu kenn
Bul lëng kenn
Bul génn kese ndax bëg génn



Авторы: Dip Doundou Guiss


Dip Doundou Guiss - ànd xeex coronavirus
Альбом ànd xeex coronavirus
дата релиза
26-03-2020




Внимание! Не стесняйтесь оставлять отзывы.