Canabasse feat. 2K - Sama Prof (feat. 2k) paroles de chanson

paroles de chanson Sama Prof (feat. 2k) - Canabasse , 2k



SAMA PROF
Mome mo takh legui diangue
Di ndeukeunté tableau pour todj ay exo
Mo ma khagn diame Ba gneupe kham ko
Yea Melnani mome rekk 'a nandoul
Sama prof
Classe bi mome mo fay yeungual
Sama prof la bardé Moma khagn diame
Classe bi mome mo fay yeungual
Sama prof la bardé Moma khagn diame
Sama profou Marketing
Dalay may jean
Ndiole Tchi Kaw
Diek forme
Rafet signe
Bouy expliquer di bigne dafa may Kill
Yalla boumou teglé tank sekh tankou lunettes yi
Yaramou minette la yor
Bête de silhouette yaw
Bou ma Ndiakk rek ma taggok sama saago
Meussouma beugg tableau mais legui raktiak ma yeukeuti lokho ndieukeunté ko ndakh prof Bi fok ma épaté ko
Hey damay goukh cour Bi Laata may tew
Dotouma tok Tchi guinaw pour geune ko meune diew
Toujours attentif
Mome rek sama khel
Mome mo koy todj professeur modèle
Motakh may tok Tchi kanam tiim podj yek kanam di participer Tchi cour Bi ndakh
Hey dama bardé sama prof
Mome mo takh legui diangue
Di ndeukeunté tableau pour todj ay exo
Mo ma khagn diame Ba gneupe kham ko
Yea Melnani mome rekk 'a nandoul
Sama prof
Classe bi mome mo fay yeungual
Sama prof la bardé Moma khagn diame
Classe bi mome mo fay yeungual
Sama prof la bardé Moma khagn diame
Bou cour Bi diekhé damay triste
Boumay gnibbi damay crispé
Moome sama khol la dieul confisqué
Yagg na fantasmer mou may kiss yeah
Madame mademoiselle khawma babe la Tchi done lene Moma ler moy sama bardé Tchi mome
Douma tardé Bou couram djoté damay koy khar après damay dougue Google prochain cours ma diaye ko wané
Mome dafa Ame Facebook
Instagram Ak snapchat
Tchi otom dreezy Lay deglou
Ler na ma ni dafay Dem boîte sakh
Daf may diangua ma koy diangue
Sometimes ma khouss Ba tablant salé néko madame comprendrouma
Lepe pour satch thiatal deunnam
Parfum Bou nekh Bi dal ma ma diakhasso kou geuleum
Mome mo takh legui diangue
Di ndeukeunté tableau pour todj ay exo
Mo ma khagn diame Ba gneupe kham ko
Yea Melnani mome rekk 'a nandoul
Sama prof
Classe bi mome mo fay yeungual
Sama prof la bardé Moma khagn diame
Classe bi mome mo fay yeungual
Sama prof la bardé Moma khagn diame
Prof Bi prof Bi
Dafay diame ni goss yi
Dafay pop lipgloss Bi dakoy cassé oh shit
Gucci Prada Louis
Boum Tchi sole Ba dougue Ngua fokni classe Bi dagn ko sopi défilé mannequin
Bope Bou fess
Proportionnel à ses seins
Mome daf ma Kill
Jeux de visage assassins
Mome motakh legui may diangue di todj ay exo
Damay sakh ndieukeunté tableau
Sama prof
Mome daal Moma khagn diame
Classe Bi yeup khamnagn mel na ni mome rek mo nandoul
Mome mo takh legui diangue
Di ndeukeunté tableau pour todj ay exo
Mo ma khagn diame Ba gneupe kham ko
Yea Melnani mome rekk 'a nandoul
Sama prof
Classe bi mome mo fay yeungual
Sama prof la bardé Moma khagn diame
Classe bi mome mo fay yeungual
Sama prof la bardé Moma khagn diame




Canabasse feat. 2K - Dk Spirit
Album Dk Spirit
date de sortie
08-04-2016



Attention! N'hésitez pas à laisser des commentaires.