Canabasse - Mane Rek Ngua Bagn (Bonus Track) paroles de chanson

paroles de chanson Mane Rek Ngua Bagn (Bonus Track) - Canabasse



Degg na Mane rek Nga bagne mais lolou dou dara
Togal fi nga tokk di tek douma Wakh sama job tontou nala
Sama team premier plan Gni Tchi dess gnou may lene troisième barame
Zero stress Zero panique Dieulsi li ma indi
Lou bloqué sama yone believe me Nako boulé
Khawma ndakh degg Ngama
Hey boma touddé
Ma Todj sa nounara
Hey fouma jouer ay liasse tourou na fa
Bou gnou diawalé Peureum dou ngualam
Wala bok yaw
Mother fucker khana deggo
Koula doundoul ngala ko
Amena acteur Amena Decor
Tchi Bi film dou ma déh Boy
Jeune homme May jeuneum (acteur)
Hip hop galsen boudé gorr nama gueureum
Sama deuneu Tchi sa noppeuh malay seddeu sama deugg
Gnénène gniy doul di dadialé doundou gnou lignouy bindeu
Mangui Tchi wagne bi togg liy khégne nekh sama tchineu
Douma daanou khana Tchi bir di na weussine
Adresse Bi BuzzLab la bo sokhla wassila
Adresse meunou Fi gnakk sayou gnou shooté dougal
Nigga shut shut Yangui youkhou deggouma
Mala sout fouf sama niveau wessoula
Yangui Tchi souf sama job'a lay soul
I'm a success story bitch Deal Bi gëstou la
Aaah Aaah
Degg na Mane rek Nga bagne mais lolou dou dara
Togal fi nga tokk di tek douma Wakh sama job tontou nala
Sama team premier plan Gni Tchi dess gnou may lene troisième barame
Zero stress Zero panique Dieulsi li ma indi
Lou bloqué sama yone believe me Nako boulé
Khawma ndakh degg Ngama
Hey boma touddé
Ma Todj sa nounara
Hey fouma jouer ay liasse tourou na fa
Bou gnou diawalé Peureum dou ngualam
Wala bok yaw verse 2}
Peureum dou ngalame
Kou Fi ndieukka guéné mixtape dou mana
Dou lèpp deh nonon
Hip hop galsen première place trace goulète dou mana
Premier Tchi Lépp ni Kana
Mane Ak succes comme notice Tchi garap
Tatouage Tchi yaram
Limay Wakh dou degn
Préférence Bi mana
Référence Bi mana
Ma lene eupe mana
My Nigga dama diangue di ko santé sama maman
Dagn ma yagg sandi kaba ma dadjalé lepe tabakh
Ba Tchi Kaw takhaw di saw Sen Kaw
My Nigga bagn ma I don't give à fuck
Khana Ngua Dem ndakhté Fi may boss
Bou ma kene ladj ndakh rap Bi Day dokh
Ma ngui fly guissou ma lenene loudoul ay tombe
Kouma Fi djaay yeg di nga dadjek maggoum golo
Lima done weur daw moungui sama lokho
Dara djotatouma meme pas Lima sol
Bitch dama dieul poids khana guisso ni ma tole
Heyyyyy Fii BuzzLab la
Djeuf dji Day Wakh troisième Barame
Niari directions Tchi Kaw Tchi kanam
No def mou Ame trace Acide Tchi kanam
Degg na Mane rek Nga bagne mais lolou dou dara
Togal fi nga tokk di tek douma Wakh sama job tontou nala
Sama team premier plan Gni Tchi dess gnou may lene troisième barame
Zero stress Zero panique Dieulsi li ma indi
Lou bloqué sama yone believe me Nako boulé
Khawma ndakh degg Ngam.
Hey boma touddé
Ma Todj sa nounara
Hey fouma jouer ay liasse tourou na fa
Bou gnou diawalé Peureum dou ngualam
Wala bok yaw
Wari sur Wari kouma xam bouma khamé
Lila sonal bouma ko meuné doto wory
Gor la Tchi gor yi,
Feugg sama deunn bitch Niggaz yi waff Golo dou gorille
Djom la Lay colis
Tegal la sam Tegal la sama life Ngua
Guiss ni meune nagn Tchi guéne khour lalay doli
BuzzLab Tchi trône Bi
Oundougang ress défense Bi Balle
Dou diegué Nigga Bou diegué gnou bodji
Fii léppeu modji
Cash Bangui Tchi poches yi,
Saayou gnou joué teglé liasses comme au Monopoly
Gno ress monopole Bi,
Boul doff non noto fils,
Zero concurrence kou gnou teukkou tok d'office
Li gnou yénou Bo ko dékko dome tokki
Comme gold Tchi soufou baat lignouy def par force Ngua koy Guiss
Nigga niongui Tchi Kaw kou gnou tek beut torticolis
Bokkougnok gnome dara ni kou diangué keuram Ak kou diogué koki
Yaw dangua wara tok Nigga
Ma teggal Ngua Ngua sip
Sama gang gneupa tok Nigga
Lou teggouwoul dagn ko sip
Lignouy deff Day oubalé mélni thiouraye
Ding gnou yeuk meme bo gnou guissoul
Lerr na ni ndelou abdoulaye
Gnoune Ak yene dou bene fils
Bo nandoul gnou nandal la
Ndanane Tchi ndanane yi djeuff dji Day Wakh
Troisième Barame nguay guiss




Canabasse - Dk Spirit
Album Dk Spirit
date de sortie
08-04-2016




Attention! N'hésitez pas à laisser des commentaires.