Canabasse - Atanougnou Dome paroles de chanson

paroles de chanson Atanougnou Dome - Canabasse



Buzzlaabbb
Yeah, Anh
Bass, listen
Li ameu amneu beu nopi
Amatoul délou guinaw
Daniou fowé, fowou mak beu tay guissato ndaw
Li seu bireu ngui law, légui mou fegne
Daniou dawal je m′en fou
Motakh guissatou lo règles
Legui leer neu ndakh texte bi dafa positif
Yeah Girl souniou andeu dafa productif Mane plus ioe égal dom, foumou ni dom égal tiow
Louniouy défak tiow
Walabok seu mère boukoy yeuk di dof, seu pa wakhi nopi
Mane sama wa galé dagne may tiop mais,
Douma daw, fi nga nek lay takhaw niou wakhtane beu trouver solution, yokh leu gaw
Degeu leu stress bi beurina mais seu khel fok mou dokh
bou yagué nieupa koy yeuk
Kone fils amatoul tok
What's up, bat bi moy waneu lor
Mais li nga waneu dinga ko yabi ndakh warou niou loreu
Li niou beug def mo niaw, mais fok niou def ko gaw
Liko moy euleuk niou niaw tchi
Deug leu damala love mais atanougnou dome
Dougne tchi diar bouma sanione ndakh Girl leerna ma ni
Li niou beug def mo niaw, mais fok niou def ko gaw
Liko moy euleuk niou niaw tchi
Girl oubil seu khel lepay geuneu simple bougne ko défé
Yaw yay kane beuy decider, li leu sonal si mane leu nek
Mais boul sonal seu bopp, neu teukou sounouy nécessité
Ya raw Tiazz bouniou exciser, amo bene yeuk-yeuk dokhal seu dokh sokh lawma yeurmandé
Meu fogone leu real nga def yeufou fake
Soumi nga sama jean mais na takk toubey
biss bou latché bayam, nako tégal lepp
dou sakh sokhla baye, ndakh mane meuneu na doneu lépam.
Mangui rétiou louniou diota sekeu
Coq de la basse-cour nga, mato Sek
Doto tchi lene, meuneu nga tok ni tek
Dinako nguenté, dinako tété, dinako yobou school, yeah dineu tekki
Damaleu dieundé khol mais dangma tek deal
Khoti sama khol mais lolou wétchite leu
Fuck love dinako wétchok diom
Mais wakh ngay doul, nane dangma nopp
Est-ce que boma nobone dinga beug kill sounou dom
Boma nobone dingma def sokhna, seu lokho, sama lokho niouy fadj souniouy sokhla
Li niou beug def mo niaw mais fok niou def ko gaw
Li ko moy euleuk niou niaw tchi
Deug leu damala love wayé atanougnou dome
Dougne si diar bouma sanione ndakh Girl leerna ma ni
Li niou beug def mo niaw mais fok niou def ko gaw
Li ko moy euleuk niou niaw tchi
Girl oubil seu khel lepay geuneu simple bougne ko défé
Yeah, khamou baye sayouma ko ladjé yaye mounéma dem neu dotoul niew
nekoul paradise, kone bok ana baye loutax bokoul si sama life beu takhneu meukay doundal sama khel diko guiss everynight
Khawma lane ley ndourol
Dafa ndiol, dafa khess, dafa taleu, dafa sew
I don′t know
Bo meytouwoul dadier nagne tchi mbed mi ay yoni yoneu
Ndakh yéneu say meu yeug lou ameu dolé tchi sama khol
Anh, niéwouma ken ndakh mère meuteul neu lepp
nenagne lo meussoul ameu meunoko niak
Wayé sometimes nga tok beugeu lo douleu kham
Mou oubeu seu bopp
Do comprendre
Mane lima manquer baye leu metinama
Yeah, sama silensou Yaye sonal nama
Def na louné, ladj na beu tayi moumay tour leumdeum
Nénama dem neu nekoul paradise, kone ana mom Anh
Yeah, ana mom Anh
Ana mom Anh
Li niou beug def mo niaw mais fok niou def ko gaw
Li ko moy euleuk niou niaw tchi
Deug leu damala love wayé atanougnou dome
Dougne si diar bouma sanione ndakh Girl leerna ma ni
Li niou beug def mo niaw mais fok niou def ko gaw
Li ko moy euleuk niou niaw tchi
Girl oubil seu khel lepay geuneu simple bougne ko défé




Canabasse - Dk Spirit
Album Dk Spirit
date de sortie
08-04-2016




Attention! N'hésitez pas à laisser des commentaires.