Canabasse - It's Bass paroles de chanson

paroles de chanson It's Bass - Canabasse



Its Bass
Its Bass
Son Bi di reukk seni iPod Nigga Its Bass
Def rap
Get cash
Gnou koy tek Tchi club yi ganstaz yi di two step
Bo ma deggoul bouddil say nope deggo dara
Ma koy todj ladies yi di gënte done Madame
Daggati All Time
Doune Khaff
BuzzLab moy sama team
Mane la Boy YARAKH
1er Couplet:
Mane la Mc balotelli
Beuggougnouma Mais Cheque match ma guènnè lene tchi
Mc mane la Barthelemy
Permis port d'arme dofdofloul degg tèlle
Teyelma sa yar
Sama peace
Ma samme bakh
Moumay diss
Damay bakh dou ma giff
May ma ma ray Kii
Murou galem loumou goudde damay lay fils
Ray ko ma ko Ray Douma lay filsgame bi dafa saltè makoy lay fils
louma rossè dafay sakh yaw dou lay fils
Yangui guiss
Boy Yarakh'a ngui
Kou beugg lou bakh par force ngua beugg ma todial cass bi fis
Its Bass
Its Bass
Son Bi di reukk seni iPod Nigga Its Bass
Def rap
Get cash
Gnou koy tek Tchi club yi ganstaz yi di two step
Bo ma deggoul bouddil say nope deggo dara
Ma koy todj ladies yi di gënte done Madame
Daggati All Time
Doune Khaff
BuzzLab moy sama team
Mane la Boy YARAKH
2eme Couplet:
Toudal ma sama show bouma tégaloul
Toudal ma bene région bougn ma deggagoul
Def ladies yi ay Niggaz gnou may khekhal ouh
Def Niggaz yi a bitch gnou may reguédiou
Dounde samay gënte melni koudoul meussa yéwou
NIT dou def limay def di ko mattal béwoul
Wakhal ma niggaz yiy weranté rap Bi déwoul
BuzzLab lagn ko teudj
Makavelly fils dou délou
Gnakk Guiss kou ma atane takh ma bérou
Mane Dama Guiss sama ndam bala may bakkou
Mcs You Bari featuring Ak Mane lagnouy sarakhou
Ndakh damay yombal visa Bi comme mariage Ak Bapto
Mais dangua Dioum adresse fii dagn Lay partouze
Mane Ak Mane Ak Mane pakh dou dess
Chaque jour
Level Bi geune di feuss
Ma lene di geune di beuss
Jokh la louy guéne 20h what the fuck is teuss
Its Bass
Its Bass
Son Bi di reukk seni iPod Nigga Its Bass
Def rap
Get cash
Gnou koy tek Tchi club yi ganstaz yi di two step
Bo ma deggoul bouddil say nope deggo dara
Ma koy todj ladies yi di gënte done Madame
Daggati All Time
Doune Khaff
BuzzLab moy sama team
Mane la Boy YARAKH
3eme Couplet:
Fils li dou rap rek raak MO ma feussal Tchi NIT yi
Back on Da dayz Sene rakk Tay dagn may lim Tchi ndjit yi
Dotou ma gnane kene Pass fo ma Guiss Tchi bus yi
Lekkougnou gatt sama cash mangui wiss Tchi bitch yi
Nane Mc comme whisky pipi
Lion Tchi bir wistiti yi
Bayiléne khamougnou ni kou Geuna hot Tchi gnome tchi Mane dafa sweet ni titi
Ototune sama baat lane Lay doyé Vivi
Ferragamo sama ndigue mais Ame na place pour grigris
Gni sene diongou weragoul wakhma kane lagnouy tins fi
Gné séne ngora desaatoul lou Bari nelene nagnou yam fils
Manguék gnanou Mere kone sene ligueye douma dal Yeah
Mangui Fi takhaw ni gouy Gui Tchi emblème national Bi ana koumay sempi
Emblème national ana kou koy weddi
CD Bi dafa vierge Ba legui mais rap game Bi la dieul tepi
Tepe tepa geune youréte Guiss ngua sama dembe
Tegual Lép louy bloker sama yone sigiil Gni ma ngembe
Dk spirit sama deunn
Dk king bi Mane may deugg
Fompal samay dale bitch 10ans mangui peundal
Guéne galé galé taylé lepe Dem oute nigga
Yagga sango ndokhou téén ladjal Ouz Killa
Boudoul wone sama ngor
Diaye na sama bope
Ralier cause politik yobalé mbolo Bi ma tope
Bou doul wone sama jom fils bayi na ndakh khoff
Dagnou Bolo di ma fight dieme ma douté LO sama job
Dagnou Warone dieul exemple Tchi Mane ndeyssane Dagnou dof
Dama todj rap Senegal yes kodj ma trace Boy number one
Mangui Tchi Rolls Royce Bi tok
Di ko Dounde Boy comme don
daanou di Ame geum ma nigga Tchi Kaw lal Lay done




Canabasse - Dk Spirit
Album Dk Spirit
date de sortie
08-04-2016




Attention! N'hésitez pas à laisser des commentaires.