Ashs The Best - Sutura Lyrics

Lyrics Sutura - Ashs The Best



Ci sutura Ci sutura Ci sutura
Sama waaji na ñu waxtaan ci sutura Xarit dee naa la ci sutura
Ci sutura laa lay waxee sama ge'nt
Sutura
Ci sutura laa lay samay proble'mes akk lima dal Sutura
Ci laa lay de'nkee sama guddi
Bulma weer ni bëccëg Bulma weer ni bëccëg Sutura sutura
Bulma weer ni bëccëg Ndax yombul nga xamal ma
Mbokk waay Sutura Sutura
Sutura sutural ma Sutura
Sutural ma Sutura
Sutura sutural ma Sutura
Mbokk du nii
Reeroo bumu tax nga tasaare ma
Sutura sutural ma
Ñu weetoo ma wax la sama demb nga waxaat ko tay Xarit sama waaji
Ma ne Mbokk du nii
Bulma jeebaane fii
Bul wax sama proble'me ci ñii
Woolu la tay
Waraloon demb ma wax la lu xew wax la sama xol
Mbokk waay Sutura Sutura
Sutura sutural ma Sutura
Sutural ma Sutura
Sutura sutural ma Sutura



Writer(s): Abdoulaye Sy, Ashs The Best, Olvier Delahaye


Ashs The Best - Dibèer
Album Dibèer
date of release
11-06-2021




Attention! Feel free to leave feedback.