Lyrics Xel Akk Xol - Ashs The Best
Yeah,
eh
eh
eh
Lé,
lé,
walé
Hum,
hum
Suba
suma
yeewu
Yaw
lay
bëgg
jakarlool
Sa
suma
yeewu
Yaw
lay
bëgg
njëkk
xol
Ëlëk
lu
mata
soor
la
Wayé
xel
xalatu
ko
Ëlëk
ay
jaar-jaar
la
Sama
xol
yëgoon
nako
muy
ñëw
Xel
xalaat
la
(xel
ak
xalatam
bë)
Xol
yëkk
yëkk
la
Nit
ak
jëmëm
jë
Dara
xaaju
fë
Sa
suma
yeewu
Yaw
lay
bëgg
njëkk
xol
(Suma
yewo
yaw
la
bëgg
njekk
xol)
Fajar
suma
yeewu
Yaw
la
bëgg
jakarlool
Denk
na
la
guddi
Fanané
yakkar
ci
yaw
Gent
na
la
guddi
gi
yëpp
Ndax
fajar
yaw
lay
jakarlool
Mbëggël!
Xel
xalaat
la
Xol
yëkk
yëkk
la
Nit
ak
jëmëm
jë
Dara
xaaju
fë
Nit
nak
ak
jëmëm
jë
Dara
fa
xaajul
Attention! Feel free to leave feedback.