Ashs The Best feat. Fou Malade - Tukki Du Tekki (feat. Fou Malade) Lyrics

Lyrics Tukki Du Tekki (feat. Fou Malade) - Fou Malade , Ashs The Best



We gonna fight for your right Fight for your life for your freedom
Dund ci ndool bëgg ci geen
Fii goor akk jigeen ñëpp a bëgg fas jom
Tukki du tekki
Tekki du tukki looy utti
Yakamti xamoo looy fekki
Yoon bëgg nga tekki
Am-am ñu gënël am teggin
Dëkk ci dëkk bi nga tekki fi moo jafe
Tax ñu xaddi
Ga'ddaay fu sori baayi njaboot gi
Mënu ñu dëkk ci ndool yeewoo xonet we need money
Teed tax ñu jël yoonu geej gi
Jooy na jooy na ngir gisaat la Woy naa la brother
Jooy naa la Baaba
Nothing to hide
My people die young ndax bëgg tekki
Jamano ji ñu toll ñëpp a saalit ja'mm amul La'mbaay rafeta gul
Batay Waalo naata gul
Tukki gënëllu ñu waaye ligeey moo fi amul Reew mi ndaw la ñakkul
Ku na'mp ci Maam Ndey nga gisul
Nothing to hide
My people die young fii ñëpp bëgg tekki Nothing to hide
My people die young because of immigration
Fitche' duul xam fii dara amu fi
Fii ku fi amul dara ken dula tekk nitt
Su ma xasee dugg kaaw doo tu ma dellusi
Rap naa junni att gisu ma ci we'ccit
Sa'cc sama gaz or dima tere visa
Ma'nk sama pe'trole dima naxee pizza
Mënu ma ci d'accord faut que je dis ça
Tampon passeport tekki takk Lyssa
Bëgga tuma toog fii njiit ñi dima politig
Foog ma dugg avion calmer sama solitude
Nang ma wax waxu kaaw boo ma bëggee disturb
Di naa mësa radical jël gun ray ñëpp
Tukki taxul noflaay
Toog ci reew mi ligeey gën woor Ñaata ndaw ñoo ga'ddaay
Tekki tax ñu ba fi li ñu moom
Tukki taxul noflaay
Toog ci reew mi ligeey gën woor Ñaata ndaw ñoo ga'ddaay
Tekki tax ñu ba fi li ñu moom
We gonna fight for your right Fight for your life for your freedom
Dund ci ndool bëgg ci geen
Fii goor akk jigeen ñëpp a bëgg fas jom
Nothing to hide
My people die young fii ñëpp bëgg tekki Nothing to hide
My people die young because of immigration
Tukki len xam Ja'ngi len gis



Writer(s): Olivier Delahaye, Abdoulaye Sy, Arfang Tiare


Ashs The Best feat. Fou Malade - Dibèer
Album Dibèer
date of release
11-06-2021



Attention! Feel free to leave feedback.