Lyrics Yàlla - Ashs The Best
Xel
du
ko
sut
te
xol
a
koy
gis
Bëtt
du
ko
se'en
la'miñ
mënu
ko
wax
Everyday
every
time
neena
moo
Ngi
sa
wet
Moo
la
gën
na
jege
sa
buumu
xol
ba
Ya'lla
a
ngi
fi
Moo
ngi
fii
akk
fiiniou
jeun
Ya'lla
a
ngi
fee
Ya'lla
moo
ngi
everywhere
Moo
Fii
akk
fii
niou
jeum
Ya'lla
joggu
fi
Yalla
na
Ya'lla
bay
sa
to'ol
Ñun
say
jaam
ñoo
ngi
lay
ñaan
Nangul
ñu
lepp
luñ
la
ñaan
Ngir
faqqir
day
nangu
daggaan
Ndax
Ya'lla
naatal
xarnu
bi
Xel
du
ko
sut
waaye
xol
da
koy
yëgg
Boo
ñu
mayee
ling
nu
mayoon
Dootu
ñu
def
li
ñu
defoon
Xanaa
yëggoo
ni
ñun
yaru
nañ
Buur
Ya'lla
naatal
xarnu
bi
Nangul
ñu
lepp
liñ
la
ñaan
Ndax
yalla
natal
kharnou
bi
Ngir
sa
yërmande
ñi
ngi
lay
tuubël
Lepp
lu
xaraam
te
di
nangu
nuroo
ki
jaam
Boo
ñu
joxee
di
nañ
la
sant
Te
boo
ñu
joxul
dutee
ñu
xëy
di
gën
sant
Rafle,
sone
ak
xiif
akk
fande
ak
teud
si
souf
Ngir
bëgg
am
sa
yërmande
Du
ñu
xaddi,
du
ñu
sof
du
ñu
daw
te
du
ñu
lakkatu
Ngir
bëgg
am
sa
yërmande
Loo
wax
ñu
nangu,
yay
buur
baaxal
ñu
Te
boo
ñu
mayee
ling
ñu
mayoon
jeegël
ñu
Dootu
ñu
def
li
ñu
defoon
Xanaa
yëggoo
ni
ñun
yaru
nañ
Buur
Ya'lla
naatal
xarnu
bi
Nangul
ñu
lepp
liñ
la
ñaan
Ndax
yalla
natal
kharnou
bi
Attention! Feel free to leave feedback.