Dip Doundou Guiss feat. Samba Peuzzi - Kheula - translation of the lyrics into French

Lyrics and translation Dip Doundou Guiss feat. Samba Peuzzi - Kheula




Kheula
Kheula
Yahhhhh
Yahhhhh
Yooo my nigga wahhhh
Yooo mon pote wahhhh
From jail wahhh
De prison wahhh
Moreee wahhh
Encoreee wahhh
Yaaahhhh humm
Yaaahhhh humm
Eh gnune la boy yi amoul héritage
Eh le morceau mec il est chaud héritage
Galé bu nexhé da fek mère da tégui nat
La galère est proche quand ta mère était enceinte de toi
Fi dangay tang rek mba niou def la kenkeliba.
Pendant longtemps t'as rien fait à part boire le « kenkeliba ».
Téguil tank souba niou soul la sa wétou mam
En vérité avant de dormir on s'en foutait de savoir
Dama jog job bassa kérog moy sen avenir
Aujourd'hui job job le matin réveille-moi mon avenir
Niom nieup sama demb moy sen yomal xhiyam
Prends ma main montre-moi mon chemin du succès
Peusi mam kone sa papa boy bou ndaw la si mane
Peuzzi mec sais-tu que mon père était un homme riche
Dama dioudou kone kou meunoul deki xhamouma ma lo meune si mane
Aujourd'hui Dioudou est fauché comme si on m'avait jeté un mauvais sort
Brosse samay beugn sign samay traitre
Brosse à dents dents de scie signe de mes traîtres
Fuck sa album fi ngamay fek
Fuck son album il n'arrivera jamais à le faire
Kogn bi boy yi daw si ndaxh ay plainte
Tous ces mecs ne font que porter plainte
Si bone dagno ropi jamacain
Fumeur de marijuana jamaïcaine
Am envie dougal tournaviss si beutou journaliste
J'ai envie de frapper ce journaliste ivrogne
Nigga manr doundou ma critique mane doundou ma mystique
Mec appelle-moi Doundou le critique appelle-moi Doundou le mystique
Ragal nani coupe d'Afrique doko fi meussa guuiss deh
Laissez tomber la coupe d'Afrique on s'en fout on est Guiss deh
Sakou xhaliss sama bop mane douma Kunta Kinté
Mon flow est authentique comme celui de Kunta Kinté
Manguek xhol bou rafet di fuck kouma nexh
Je veux une meuf classe qui dit fuck comme une pute
Old school nga dinga xhosslou ba deh
Old school je vais tout déchirer
Fowe carrierre rama gueuneul kay len dioubal
Le début de ma carrière s'est fait dans le noir
Cirose na bou yagg souma touxhone lima tall yeup
La cirrhose ne me fait pas peur je suis vacciné depuis l'époque de Limamou Laye
Dou samay deuguentane album yima dieulone temps rappeur under ground
Depuis le début de ma carrière mon album prend du temps rappeur underground
Sa yaye mane la gueuna fan niémé xheureum la
Ma mère s'en fout elle est fan depuis longtemps
Ray sa serigne nigga dangay ndieukante nigga far def depart rou mbam arrivée leumbeul narr
Dis-lui mon pote ne sois pas hypocrite mon pote suis ton chemin pars de Mbam arrive à Lembeul
Rakkou modo fi diarone (diarone) (2×)
Arrête de faire le fou (le fou) (2×)
Doula ma lekk laxh laxh douma lekk laxh (douma)
Apporte-moi mon « lekk » vite apporte-moi mon « lekk » (apporte)
Soupou Kandia mafé domoda (ohh yehh) (4×)
Soupou Kandia mafé domoda (ohh yehh) (4×)





Writer(s): Dip Doundou Guiss, Ismaila Talla, Samba Tine


Attention! Feel free to leave feedback.