Lyrics Temanefi - Dip Doundou Guiss
Come
On!
Alkati
ya
ngi
sa
kaw
Thiap
bi
nga
doon
xam
naniou
ni
ya
ngi
ak
xalissak
drogue
Wa
bou
yabo
nanal
ci
sa
Safara
yi
dieul
garap
bi
xeupo
Thiat
ci
sa
maw
laff
yi
la
tok
May
sa
thiabi
kasso,
mane
la
may
Picasso
Parce
que
boudone
man
xamna
di
nga
sol
Lou
eupeu
att
nga
ndara
woor
kay
niu
nafila
bokk
Père
Noel
raciste
la
mane
moussouma
guiss
cadeaux
Guiss
na
ay
Pa
yu
djaay
sen
taxi
pour
am
passou
avions
Atoum
leumb
souma
nekhé
douma
liguèye
A
tout
moment
meune
nga
déh
ni
ngoumba
ci
Guedj
Dou
ben
bopp
rek
nek
ci
mane
Def
lou
yomb
rek
méti
ci
mane
Kouy
topando
mane
ak
yaw
nouro
wouniu
système
Yallah
loutax
ma
dée
ni
kou
dioudo
ci
cimetière?
Mouno
wa
Rap'Adio
kone
non
meuno
li
DIP
Def
TLK
dou
Album,
dou
maxi,
non
non
dou
mixtape
Yaggo
tchi
kaw
ni
boy
bou
ndaw
bou
tiim
"Jail"
Rap
bi
dafa
yombone
nioune
niossi
soti
dindière
Ndiago
bi
moy
Boss
pourtant
moussou
massi
djékkeu
Douma
lekk
kou
souroul
parce
que
dama
xiff
ndeim
Na
def
lou
eup
1000
scènes,
encaissé
plus
de
1000
chèques
Sa
Papa,
Sa
yaye
ak
baag
bi
lay
souleudo
ci
tenn
Maf-fu
Hip
Hop
bi
mo
raw
bi
ci
Goudi
Town
Rap
bi
dou
djoug
ndakh
boy
bou
am
buzz
outi
daanou
Boul
mousseu
ni
yafi
meun
Témanéfi
Yaye
boul
niaanati
kèneu
Témanéfi
Marozik
mounoul
xonett
ndakh
ma
ngi
fi
Sokhla
wuma
kèneu
kumay
temoigné
fils
Boul
mousseu
ni
yafi
meun
Témanéfi
Yaye
boul
niaanati
kèneu
Témanéfi
Idy
namoul
Iphone
6 ndakh
ma
ngi
fi
Sokhla
wouma
kèneu
kumay
temoigné
fils
Dé
lène
Diaamou
Yallah
té
nguène
gueum
sen
bopp
Bèneu
lama
may
mane
ma
woute
yeneen
2 cerveaux
Même
handicapés
yarramam
day
ndaw
Wayé
kou
Fan
Pée
(1er)
bi
toujours
deuss
(2eme)
lay
done
No
def
ba
degg
Jàmm
ci
deuk
bou
dégueulasse
bi
Yëk
Carrapid,
bokk
nëk
ak
Pa'
bi
Mama
ress
la,
ress
sa
rakk
yi
Réro
demb
téyeul
sa
lamiñ
Sénégal
moy
deukou
Téranga
mais
amoul
restaurant
du
coeur
Kone
loy
xalate
ci
boy
yi
moussoul
ray
sen
bopp
beug
xexal
Afrique
Liberté
moussoul
am
nigger
fuck
4 Avril
Dictateur
rek
ba
déh
ni
Colonel
Khadafi
Bandit
yi
yéwou
yeup
ngi
def,
ñi
gueuméintou
dem
teudi
Jail
May
Punch
ba
ndel
Kocc
Barma
té
dougneko
nétali
kèneu
Nigger
douggou
na
palais
xamna
donou
Président
Boul
Rap
toujours
rek
fexel
ba
am
comme
li
Jay-Z
am
Boy
Grand
yoff,
Arafat
boy
xamna
fou
BOON
bou
nekh
bi
am
Meune
nagnema
faat
wayé
mounou
niouma
fatté
Dioudou
waat
na
ba
sonneu
mais
bène
yoon
lay
dé
Gars
yima
gueumoul
wone
légui
gueméwouniu
ma
Naukhaur
yi
lekkone
nagnema
bu
yagg
souma
deumé
woul
woone
Yen
ñeup
souma
len
eupone
alal
di
nguène
ma
faral
Comme
gars
yi
am
ay
milliards,
milliards
pour
am
ticket
safara
Sama
succès
bou
rèèn
niggers
wérenté
nako
daw
Yen
ñeup
ken
dou
ame
louko
nekh
ni
ay
waraté
kat
ci
boîte
Dama
done
djaap
sama
gars
yeup
faaté
yèèneu
texte
yi
Bayil
ma
diéma
djaap
text
yeup
faaté
yèneu
gars
yi
Niit
yi
xalaté
touniou
xel
ndakh
seug
séni
sex
Motakh
makk
dou
jog
ci
teudé
rakkam
ni
Ci-Yénekaay
yi
Boy
guél
yeup
leundeum
dou
foula
nekh
ngay
toufli
25
ans
baayil
ma
doundou
comme
si
Papa
nékatoufi
Batay
mane
may
wakh
loutakh
nièneu
ñi
di
taf
sen
guémiñ
Yaay
sa
dome
dou
wadd
ni
rongagnou
ray
kattou
niit
...Morée
Boul
mousseu
ni
yafi
meun
Témanéfi
Yaye
boul
niaanati
kèneu
Témanéfi
Marozik
mounoul
xonett
ndakh
ma
ngi
fi
Sokhla
wuma
kèneu
kumay
temoigné
fils
Boul
mousseu
ni
yafi
meun
Témanéfi
Yaye
boul
niaanati
kèneu
Témanéfi
Idy
namoul
Iphone
6 ndakh
ma
ngi
fi
Sokhla
wouma
kèneu
kumay
temoigné
fils
1 Holocauste
2 Damako Khar
3 Dou raggal dou respect
4 Niata la yalla fay sa xol
5 Bandit
6 Beut
7 YMYM
8 Nimala beugué
9 Niata nio dess
10 Funérailles
11 Kheula
12 Innoncent
13 Kantambiuw
14 Com dab
15 Temanefi
16 Boula dara metti
Attention! Feel free to leave feedback.