Dip Doundou Guiss feat. Titi - Nimala beugué Lyrics

Lyrics Nimala beugué - Titi , Dip Doundou Guiss



Par AbouAmg
Mbeuguelooo
Ooohhh
Ahhh
Dio
Wakhema fane
Nga nekk esk
Yangui may
Name am dett
Ndax fimounè
Dama reiire ma
Raw pousso
Ci digg guèdj
Mane limay
Queuneu guagn
Moy soumlay
Guiss ak bènène
Gayine, kou beug
Beugne nala
Lerni mane douma nakk
Souma tooguè
Biss sans yaw
Day mèlni damla
Gueudieu guiss
Sa dèmarche
Sa style sa siigne
Sa biise yima
Meunoul sappi
Say fèèm say
Mbirr ak sa
Beuti Lima am
Yeupa ngui dji
Sa dieum dji
Lay guiss
Yèneusaay ci
Sama cahier
Exercices
Bou say rongogn
Narè tokk na
Deikk sama ngorr
Ndax diaral ngama
Deff litax may
Dièpi sama bopp
Mane yaw rèk
Lay deglou Ndax
sa baata dakk
Son bi ba
Sayoumalay wôo
Lakkatou sathie
Téléphone
Konn kay dieulèma
Chambre noir
Dieumèma maison
Blanche ndaxtè
Sama mbeuguèla
Gueüneu lère
Robbou mariage
Même assamansi
Mènoul soute
Sama mbeuguèl
Ndax damala beug
Ba nopi beugué
Hun HUUUNNN
Yaw moussouma dienw
Motaaaaxxxx
Motaxx ma nobe la
Yaw moussou
Wax ci mane
Lou niaw
DIP
Yaw damla tèrè
Nèlaw parè
Deuklo la ci
Guènteu ′dou
Meritè dou
Diangue waay
Dieul nga stylo
Ba signè
Yagg nala togn
Nga dem deupate
Di niane ma
Baale la., kheutio
Toumak sa Farr
Ndax
Dangma diox
Sa plaçou papeu
Tatouage nga
Sama tour sa
Xôl chaque jour
Nga nieuw kogn
Ha ba sa entourage
Yeup nènagn mane
Dama mour say
Beute yènène
Goor Yeupa flou
Say Beute
Yak niome Ndax
Ak courant la
Dioudouwo ci
Taggeu nangou
Naaw ci yènène
Diawou ak mane
Bb kholl ma
Bb wôo ma
Bb fone ma
Bèè nganèma
Bèè lo dèf ma de
Fo dem ma dèm
Mak yaw forève
Rék
Sama ndièguènay
Ki gueüneu tax
MA dièguè yalla
Ragalo dara mais
Hièmèwo bayntè
Ak mane mane
Ak mom bènen
Xôl Bila lènène
Douko khar niaar
Yama moom mala
Moom menott moy
Dokk souniou Alliance
Yay diour samay
Doom yaw rèk
Yay doone sama
Diabar Ndax bagn
Todjè sama xôl ya
Dieul chantier bi
Khèkh danko tabax
Hu
Huuunn
Yaw moussouma
Dieuw moootaaxx
Motaxx ma nobe la
Yaw mousso wax
Ci mane lou niaw beuguèl dou
Diayèèèè yaw
Yako tibbo 'yama
Moom niom
Momouniouma mane
Yaw lay see
Ya neuboo lim dem
Ak yaw bb
. Ndax yaw moussoulo
Ma Dieuw, mousso
Wax ci mane lou
Niaw djiguène laa
Bb oookkkkooooo
Haaaaaah yaw moussouma
Dieuw moootaaxx
Motaxx ma Nobe la



Writer(s): Dip Doundou Guiss, Ismaila Talla


Dip Doundou Guiss feat. Titi - Tay Leu Kagn
Album Tay Leu Kagn
date of release
04-11-2017



Attention! Feel free to leave feedback.