Lyrics Boula dara metti - Dip Doundou Guiss
Boula
dara
metti
Boula
dara
gagne
Douma
imbéciles
Danko
wara
xaam
Douma
domérame
Douma
salopards
no
Boula
dara
metti
ndax
mana
Léena
rek
kama
metti
the
dina
hame
Ay
nith
you
bax
dinagne
la
diaxassék
mane
Dilay
waxlo
lo
hame
Dou
diar
sax
ngay
comprendre
Même
boudône
mbeuguel
déey
diay
do
hame
kénéne
comme
mane
Doyna
warame
dafa
dow
yarame
Dangue
ma
beugue
xamnako
xanna
doumala
doxane
Doumala
thieupeul
thi
pét
iow
ngay
diay
eupeul
dimay
thieupél
Iow
mi
ya
done
costé
thi
netbi
nane
fou
néke
je
t'aime
Love
ngama
ba
teukkané
ma
lolo
tax
ma
déme
baby
lou
eupe
tourou
dangue
ma
warona
nob
nanke
rék
1 Holocauste
2 Damako Khar
3 Dou raggal dou respect
4 Niata la yalla fay sa xol
5 Bandit
6 Beut
7 YMYM
8 Nimala beugué
9 Niata nio dess
10 Funérailles
11 Kheula
12 Innoncent
13 Kantambiuw
14 Com dab
15 Temanefi
16 Boula dara metti
Attention! Feel free to leave feedback.