Dip Doundou Guiss - Niata la yalla fay sa xol Lyrics

Lyrics Niata la yalla fay sa xol - Dip Doundou Guiss



Auto mbalite tama
Auto polis'sama yétal
Grand yoff city de Dieu mousso faguiss kougne fa fétal
Apart ki policier yi ray Ndiaga Arafat wett na comme université kou ball perdu ray sa mére moy perte
Job moma jeulé ci mbéd bi moma indi wat negga fok ma riche keur'ak auto automatiques you fébar mane sama boppou daffa fééss mane sama compte fééss mane sama concerts yi fééss mane fèèss ni concer'ou FESMAN
Alhamdoulilah rap woul astakhfiroulah gni neubbou wone sax fégne comme IBA"k MAKHTAR CAGOULARD
May grand gnoune la sa boy yi changer photo profil gnoune gnon def photo police homme de parole rek la ragal fallé wouma homme de tenue voul djoum ci may ak sarakhé ba sone bou yone deffone yone boum yi rek'ay geuneu fééss cachot
Sa pah day job feugg djay day meusseu cher ci mom ki fay salairam djouggoul weer ci kanam rek la tokk
Sa some demna dou gawa gnibissi
Lou takh gnou sokhor ni seuttou IBBLISS YI
Succés bou gaw ni enrechissement illicite
Sa dome demna dou gawa gnibissi
Lou takh gnom gnou bone ni seuttou IBBLISS YI
Succés bou gaw ni enrechissmznt illicite
Seytané doula meusseu djam dalay djam lo benen niit ndax
Gouddi yign tôllou kouné meun na done terroriste
Tiyaba geuneu fort moy geuneu fay
Bakar'a geuneu deugueur bopp geuneu meuneuh ray ni meuwti télék téléphone bi deff possone ci sama khél climat béngui bizzare ni boy yi ci debut 2016 bi ki geuneu wékh signe mom déréte lay toufli adouna touki bou yagg gnouy khaar pour adouna touki mane xawma xamnani xawma dh xawma bakham son egotrip la xawma théme lépp lougn fi ték ma beug ko djeul ndax awma khél li leer ba leer moy kimaka moudjé sékhal xawna déé boy mangui def ay son pour am khaliss di def ci sama poche yaw ya beuggueu siw wayé man succés bi daf ma soff nél sa patron k man mani mom déffalouma gatt fuck the world war' chaise anglaise rek lay djox sama tate m'therfucking neggas
Sa some demna dou gawa gnibissi
Lou takh gnou sokhor ni seuttou IBBLISS YI
Succés bou gaw ni enrechissement illicite
Sa dome demna dou gawa gnibissi
Lou takh gnom gnou bone ni seuttou IBBLISS YI
Succés bou gaw ni enrechissmznt illicite
Ken deukoul ci def YALLAH tax parce que kouy seddo ba fatté boppam day tardé fi kou tardé dagn koy alamane masta thiono ciy gniy doundé mastata bay'fall bi balé azaka ba benen yone yaw tamit akassa digueunté assamanak souff nennala souff dou meusseu sett assaman dou meusseu saleté lathiél ABRAHAM dou manak man réka xam lissi gawa magg boy mag la lolo tax ma rare da ame bakar youma wara bakar



Writer(s): Dip Doundou Guiss, Ismaila Talla


Dip Doundou Guiss - Tay Leu Kagn
Album Tay Leu Kagn
date of release
04-11-2017




Attention! Feel free to leave feedback.