Dip Doundou Guiss - Funérailles Lyrics

Lyrics Funérailles - Dip Doundou Guiss



Reptile Music
Yeah
Yeah
A crime saved yeah
Anh
Anh
Yeah I'm sorry for myself
I'm sorry for my self no no
Ouh Ouh Ouh Ouh Ouh
Gotta make it for myself no no
They don't love me any more
Beus bi ngay dèe, ay rongoniam meunone nala sangue
Doolei youxou yi atane nagnu sa corps bi ba si sa biir pakh soul la si sa cambeu
Merr na kagn wayei dou geudj dilla nianal founek dinalafa toudal tourou Yalla
Bagua demei ngua yobalei xollam doundame niakk khorome goumba teukhlou gana
Beuss bi ngay dée ay goudila yeah
Si lagne guedjeu yeuk lerayou beuthieuk
Kerok nioune nieupeu leu demone yeii ba mellni daguay nelaw ndakh keine meunouko gueum
Xar yeik Xath bi demnagne ba dagne ko yeuk amoul mbow amoul mbeé Bb sakh dou seukeute
Mowti djeulloula non dala goungueii ngua gnibi ndakh deukoofi Al-Jannah ngua deuk
Deug leu deug leu deug leu
Yeah Beuss biguay dée thi goudi la fegne
Keur gui ni tekk Djeum dja faye
Teud sa caisse kou djeum ngua tew
Fleur yi la deff si att bi ngay djoudeu ak att biguay djotta gueine Adina yaw
Ameilooniou dara diokh ma lingèy yi dalloul dinalako dello beus bi may nieuw Eh
Nakarina si mane ma fattei funeirailles non non non
Non non non non
Deudji yi beuri nagne Wayei funérailles yi bokoul non non
Ah Ah Oh Oh
Nakarina si mane ma fattei funérailles non non non
Non non non non
Deudji yi beurinagne Wayei funérailles yi bokoul non non!
Ah Ah Oh Oh
Beugouma diap sama xel que ni dotoumala guissate
Ya gnu nango bayyi def sa bopp dem si
Yallah mane louma ci meune
Chaque goudi damay gueinte guiss la, gueinte bou nek ak limuy missal
Yallah meuneu mayé meuneu dieullate limou mome doussi yaw doussi mane
Yallah doula def dara, sa ndjaaboot dou torokh, ta suuf dou tang si sa kaw
Gni guene ci niune moy gni gneukeu dem
Warone naniu goude fane dakh ma meune aw fi nga aw
Mougne na mougne ba meuneutouma mugne
Ndakh ronkhongne yi dess ci biir moy ronkhogne yi geuna sokhor
Boul deloussi gnune gnolay fekki
Boudé ya ngi gnuy guiss xolal gnune dagnu koy feté legui xolal
Na mere yi fethie, Pa yi mandi
Réindi beuye yi, réindi mbame yi Dagnu lay goungué nga feeki Mame yi
Am nga ganaille yu bess pour aar gnu
Meme sa noone yeupa tew solu all black, tout noir represent
Tour fi ndokh pour que niou soul ci kawam
Nakhari na ci mane ma faté Funairaille yi rawatina sama funeraillou bopp
Nakarina si mane ma fattei funeirailles non non non
Non non non non
Deudji yi beuri nagne wayei funérailles yi bokoul non non
Ah Ah Oh Oh
Nakarina si mane ma fattei funérailles non non non
Non non non non
Deudji yi beurinagne Wayei funérailles yi bokoul non non
Ah Ah Oh Oh
Beneu mo geuna gaw
Niaar mo geuna woor
Gneuwa ndo wuniu mane ak yaw Mama Cry, don't cry no
Mama Cry, don'r cry no
Yallah buur moma lathie
Bono gnemewuma negocier
Bayil ma dem sagnuma negocier Nakarina si mane ma fattei funeirailles non non non non
Non non non non
Deudjii beurinagne wayei funérailles yi bokoul non non non non
Ah Ah Oh Oh
Nakarina si mane ma fattei funérailles non non non
Non non non non
Deudjii beurinagne Wayei funérailles yi bokoul non non
Ah Oh Oh
Ah Oh Oh
Ah Ah Oh Oh



Writer(s): Dominique Preira, Ismaila Talla


Dip Doundou Guiss - Tay Leu Kagn
Album Tay Leu Kagn
date of release
04-11-2017




Attention! Feel free to leave feedback.