Nitdoff - Intro Lyrics

Lyrics Intro - Nitdoff



Yeah
Dafeu gueuneu mague tchi diguenté bi
Dafeu gueuneu capable tchi bi game
Kholou mbéd béko taamou ni djiguene
Mini mini mc yi topou tchi di téen
Ben weekend laay def tolouwayou 10 ans wou rap so paré diapéma tiken
Diss hand doma guiss sén mother fuckin' systeme
Legui dama bédékou distant
Da nga mbelé mbelé da nga téleu mbeulé
Da nga teulé da nga téléphoné cyliconé plafonné
Military migui guerri migui paris migui wari
Mi ngui daagou tchi talibi di celebrer
Gang gang dama dingue dingue
Maintain lyrical Killah wex xaat ni singuén
Nigga nguen tekk di ndenguégn
Gun to the z dey takk independant
Deugu faratala feug talatala
Deunou malakala beugumaleu halak
Yeugouma sa dara
Nigga da nga nara sorou ki leu wara souli safara leu
Limeu teuyé fidé dou tchi téeré bi deh baraka la
Magui tidji teuthie binde chapitre ak paragraphe
Gni ko ndieukeu ndiem teulé defouniou ma dara dara
Mbirmi niakh ndiarigno leu dara dou tchi parakh parakh
Gadou na tchi ndamo ndam
Sama diar diar ken douné raamo daan
Samay tar tar defna nama rambo man
Douma tandouw man damey am doe man
Nigga nando man yagui yandor man
Eyes to eyes baye dou size
Bayi sa vice do survive nice to nice
Dama xepp sa price def surprise
Sacrifice jesus christ stop the cries
Dama def tchi move bi absolutely
Bayil sa yout yi
Mayé salute bi exclusive
Excuse yi next use bi
Khamo yonou diambar biniou dathie tchi shoes yi
Na nga dess tchi douche bi
Aay si loose bi
Souniou paré victoire nga niew baye pelouse bi



Writer(s): Mao Gou


Nitdoff - The Beast 1
Album The Beast 1
date of release
20-09-2020




Attention! Feel free to leave feedback.