Nitdoff - I'm Lyrics

Lyrics I'm - Nitdoff



Yeah
Han
Att you bari magui dékou sen sissou ci sama side
Coalition bou nekk former neu forcer beuguon ma fight
Bobou ba legui sou nguen meunon tarafatal neuboon ma light
I'm the legendary Killah mbed meu tété ci mic
Wakh nga dieuf nga téwoul taye la gun takk ni dynamite
So doon real doma djiépi ndakh dieuf dji Jah rek leu right
Killah Killah meussoul souk sen mother fuckin' diotaye
Louneh la dèg mou diouguè ci yen
Seni ay kathie non dotouma yéem
Ken dou xam lepp wakh lepp motakhite ma bérou di def sama kéem
Bitch nga déma wowé samouraï
Dioganté déko sekk ak sey morom
Legacy mbed ba ngui ni say my name
Sa badio gua oubi nane ma sanio raye
Khana dou hip hop bitch
Killah ko yegualaate si satellite yi
Fake meuno bèg meuno dèg liniouy tekk
Danio néek def lou sale amo niveau fi niouy yek
Meusso leuthie kasso teuthie podiou mère mi lanie leu deuthie
Reuthie ngeuthie niouni keuthie succès bobou lafeu geuthie
Xeuy di kamikaze kamikaze
Niou nane da bari problème beuri kass
Cédelé barres yi dou kheli kass
Yagu ci game bi dou xoubidass
Dominer carte gui coupou doupi ass
Gni damelen tapeu deflen samey tchiaz
Gooné gui lawlathiat ci loumou lale
Real ci ADN di sama race
Han ndawrabin sen rabinn tellement nul niaw lamign
Always win kaw la miine like the fucking king Rakim
I'm rocking i'm the king
All i know is they sucking
Bitch ass nigga lo foguoon KK for real i'm talking
Ya saguane (nigga), ya saguane (nigga)
Ki ngey saurou dafeu melni guass sa kane
Yes i can
Yes i can
Tewal mbed rap biy gueun di saf sapam
Killah killah number one bi what's poppin
Killah killah number one bi what's poppin
What's poppin killah what's poppin
What's poppin killah what's poppin
Sen bayaay thiafka tchin moy rap usine
Moy Mbacké Dioum moy last king
Mo sakh sikim mo santhie team
Real ndiatigué biley diokh li gueun
Moy médecine moy buurou sine moy origine mo yoréy djin
Moy discipline bi néh bord rou chine
Moy noblesse ba tchia Quraishi
Respect bi day daw sinon rek bro intifada gaza
Sani bombe hasard créer bazar gni niou si fagagual died
Appeu na tchi ay att so diogué pas force naleu hagar
Yagui wané khadar mane maguiley khole tiim sa new di kabar
Samey nigga meuss nanie kepp sa n mane maleen call
Boudoul woon masla rek kone dina thiol ba yeeg taule
Bitch nigga ndol takhna nga reupélou anguou rôle
Saltel killah defko guilty mo nekkoon sa banderole
Hip hop bou deh rew KK cité leu yaw yagui maule
Xam sa bopp kone magui ak ay nigga sa bopp kogn
Torino ak Paname nigga bo xamone do yokk togn
International khéxou Diwsquad leu def fepp zone bitch
Ya saguane (nigga), ya saguane (nigga)
Ki ngey saurou dafeu melni guass sa kane
Yes i can
Yes i can
Tewal mbed rap biy gueun di saf sapam
Killah killah number one bi what's poppin
Killah killah number one bi what's poppin
What's poppin killah what's poppin
What's poppin killah what's poppin
Fuck sen nigga fuck sen diotaye
Meussouleen ma like
All your niggaz dama sipp sen faux waay
Meussoulen ma like
Kou nguen meusseu nguimb defnako bitch
Meussoulem ma like
KK legendary down the street
Meussoulen ma like
All ya bitch nigga around around
Meussoulen ma like
I'm looking for you town to town
Meussoulen ma like
Flow bey meti melni paka sa down
Meussoulen ma like
Bou ci rap niou deem
Bou ci raag niou deem
Amna niou ay nigga you ko like
Ci yaw ley dess niou dem
Boudé ci rap niou deem
Boudé ci raag niou deem
Amna niou ay nigga you ko like
Ci yaw ley dess niou deem
Amna niou ay nigga you ko like
Ci yaw ley dess niou deem



Writer(s): Amady Fall, Mor Talla Gueye


Nitdoff - The Beast 1
Album The Beast 1
date of release
20-09-2020




Attention! Feel free to leave feedback.