Lyrics Bombaclat - Nitdoff
L'impérialisme!
(À
bas!)
Le
néo-colonialisme!
(À
bas!)
Le
racisme!
(À
bas!)
Le
fantochisme!
(À
bas!)
Gloire!
(Au
peuple!)
Dignité!
(Au
peuple!)
Pouvoir!
(Au
peuple!)
La
patrie
ou
la
mort,
nous
vaincrons!
La
patrie
ou
la
mort,
nous
vaincrons!
Merci
camarades
Danie
niu
door
ci
maf
bi
danie
niu
lie
lie
ya
Ndjit
you
bonn
yi
yobé
nanie
niu
faya
faya
Bombaclat
tchi
niom
gni
niata
lanie
fi
raye
ya
Complot
ak
toubab
bi
déf
niou
ay
bétails
ya
Rogne
naniou
bepp
koom
biwoon
ci
guedj
ak
souf
Xadialé
Africa
mouy
gueun
di
wéey
di
soukh
Ana
gniy
agualé
xéexu
Sankara
Kou
fipou
diouk
rek
babylone
nieuw
sankeu
la
Liy
daw
sén
yaram
dou
dérétou
guor
Falou
ci
réwou
black
sathie
léen
di
ligueyal
toubab
Yéneu
yéess
yéén
bane
xéetu
khole
nguen
yor
Costume
cravate
deuké
diay
mana
complexé
nguéw
Gni
leu
fale
nga
délou
yéw
Babylone
foum
beugu
nga
téw
Do
signél
lou
bakh
sa
rew
Yay
kou
yorr
djiko
diou
séw
Mane
meunouma
fékéti
rew
miy
naakh
saay
Now
wakhtou
diotna
Afrique
burn
yi
saï
saï
Diougual
nga
wooté
révolution
now
Li
Afrique
mom
na
déss
Afrique
niou
dieufandiko
War
naniou
meuneu
diangu
war
am
ay
hopitaux
Liniou
am
tchi
koom
dou
yoon
niouy
xeuy
di
dound
ci
ndole
Li
yepp
ay
ndjit
you
bonn
Li
yepp
nguéw
yéniou
tonie
Siguil
té
xam
sa
bopp
Africa
dél
mind
Niom
liniou
leu
def
last
time
Yéw
sey
mame
banopi
dominé
sa
askane
Del
mind
yaw
rékeu
farr
niom
niouley
sott
sotto
Bolo
ande
def
saï
rek
la
fokk
ni
lolou
nga
sokhla
now
Rest
in
peace
Amilcar
Cabral
wané
neu
ngoora
dém
Rest
in
peace
Patrice
Lumumba
wané
neu
ngoora
dém
Aiiight
taye
dji
gni
fi
néh
nio
yéw
djiaay
Séni
brother
lawoon
fawoon
rek
mo
khéw
taye
Ouattara
ak
Macky
are
we
bad
lucky
Africa
foumiy
dieuleti
Muhammar
Khadafi
Babylone
dafniou
noote
meussoul
beugu
Africa
diouk
Ay
ndjitou
rew
you
nioul
la
sampe
tchi
souf
mou
ba
fi
kaddu
Niou
dem
beu
nit
yiy
faatou
économie
bi
mabou
Mou
am
ay
Jaques
Focart
you
béss
youy
nass
akeu
rabou
Danie
leu
yéw
djaay
Africa
danie
leu
yéw
djaay
Danie
leu
yéw
djaay
Africa
danie
leu
yéw
djaay
Danie
leu
yéw
djaay
Africa
niom
danie
leu
yéw
djiaay
Danie
leu
yéw
djaaay
Africa
danie
leu
yéw
djaay
1 Intro
2 Niip Mic
3 Imbécilo Rék
4 Virus
5 PYS
6 Wané Fite
7 Go Get It
8 Loy Yeuk
9 Yafi Nék
10 Seedorf
11 Ride or Die
12 Better Leave
13 Rolling
14 Gun To Da Z
15 Interlude
16 I'm
17 Bombaclat
18 Obi Médecin
19 Vécu
20 Yoonu Ndaw
21 No Bullshit
22 Big Shoot
23 Doing My Time
24 DND - Bonus Track
Attention! Feel free to leave feedback.