Lyrics Doing My Time - Nitdoff
Do
you
know
i'm
doing
my
time
yow
Do
you
know
i'm
doing
my
time
yow
Deukoumafi
mane
damey
diar
dialeu
yow
Do
you
know
i'm
just
doing
my
time
yeah
Soumey
niew
indalè
souma
diné
Zero
baakar
guiss
nga
ni
meu
cleané
Ki
meu
sakk
bindal
nameu
weurseuk
Fi
meu
wareu
diar
kenn
douko
disturb
I
just
doing
my
time
One
life
to
live
In
God
i
believe
Warouma
di
guiss
sama
bopp
ci
lénn
Douma
ci
lénn
Damey
diar
rek
dém
Ki
meu
fi
andi
woon
moy
kènn
Do
you
know
i'm
doing
my
time
yow
Do
you
know
i'm
doing
my
time
yow
Deukouma
fi
mane
damey
diar
dialeu
yow
Do
you
know
i'm
just
doing
my
time
yeah
Xamouma
ndakh
damey
goudou
fane
Worouma
ndakh
dina
amiy
dome
Mom
liko
soope
danane
doonal
mou
doon
Buur
Yallah
def
li
gueun
ci
nioun
Loum
dogual
niou
nangou
té
mounie
Moy
kiy
sakk
moy
kiy
def
moy
ki
meun
Gueum
nani
fi
deukou
mafi
damey
diar
dialeu
Dina
waslou
akh
guass
beu
samey
part
balleu
Xamna
ni
fi
meu
tekk
samey
tank
mbartaleu
Mais
souma
démék
ngeum
dina
yégu
barkaleu
Yénn
saay
nga
dém
beu
fokk
ni
li
sa
meun
meun
leu
Ngey
dokh
ci
léer
dina
gueuneu
réer
ndeké
leundeum
leu
Lotou
naniou
ci
matt
leu
diam
may
niou
yermandé
Bi
nga
niouy
sakk
amoul
kenn
koula
doon
seconder
Mindafoun
yi
nga
sakk
yepp
nitteu
léen
gueun
Bi
nga
né
malaka
yi
diouli
léen
niepp
léen
gueum
Ménoum
ibliss
mo
wanè
reuy
wanè
orgeuil
Takhaw
sissou
beu
dieumi
taye
dji
mo
niou
lorr
key
Taxaw
sabal
la
kènnal
leu
mo
niou
war
taye
Ndakh
adouna
bi
kouko
waroon
demb
moleu
war
taye
Do
you
know
i'm
doing
my
time
yow
Do
you
know
i'm
doing
my
time
yow
Deukouma
fi
mane
damey
diar
dialeu
yow
Do
you
know
i'm
just
doing
my
time
yeah
Xamouma
ndakh
damey
goudou
fane
Worouma
ndakh
dina
amiy
dome
Mom
liko
soope
danane
doonal
mou
doon
Buur
Yallah
def
li
gueun
ci
nioun
Loum
dogual
niou
nangou
té
mounie
Moy
kiy
sakk
moy
kiy
def
moy
ki
meun
1 Intro
2 Niip Mic
3 Imbécilo Rék
4 Virus
5 PYS
6 Wané Fite
7 Go Get It
8 Loy Yeuk
9 Yafi Nék
10 Seedorf
11 Ride or Die
12 Better Leave
13 Rolling
14 Gun To Da Z
15 Interlude
16 I'm
17 Bombaclat
18 Obi Médecin
19 Vécu
20 Yoonu Ndaw
21 No Bullshit
22 Big Shoot
23 Doing My Time
24 DND - Bonus Track
Attention! Feel free to leave feedback.