Nitdoff feat. Mao - 6 Years 3 Bum's Real Shit Lyrics

Lyrics 6 Years 3 Bum's Real Shit - Nitdoff , mao



Gunzout Gunzout
Nanananaaaaaaaana
Nit toudou Doff, Doff toudou Nit
2007 ba légui nigga wax ma niata hit
Fight real shit
Téwal real shit
Ghetto bégnou yoni nguir niou siweul sunu street
Nit toudou Doff, Doff toudou Nit
2007 ba légui nigga wax ma niata hit
Nétali sunu life
Lii xéw cii sunu side
Leundeum beurii takh niou iindi light
Yeah
Dk néna yes
Thies kaay yes
Kaolack yes
Bandit LG moko ress
Rap Game bi la yokk taram
Déloko gueudeu bataay niouy thioytu ay xibaaram
Douma tchii al bafta
délou naka tiafka
Gni done di nguatt mbede bi nio nieuw diébelou after
Hip Hop dou meusseu dead
Yeukeutile sa hand
Lii dou rap thérapie leu
Tchii kaw tali Ferrari leu
Salam Aleykoum again
Nigga guiss nga fima gèneu
Bénène hit cii sama game
Defna tchii sama kém
Tallaay katane diko diém (Tallaay katane diko diém)
Hip Hop music for ever
Athie nako tchii yénène level
2.0.0.7 lako sékh moukiko mégo
Dox loko guandi djégo
Maa def cii pet ak life lou geune
Niou djoy cii niniou maay teggo (Oh Yeah)
Black lion mister bandit LG
Mbede bi compagnie leu maa done cii ngandi DG
Dika topoto diokh ko originalité
Warone done Super Star soufé done aap talibé
Mbede mo rodé sunu mind
Niou yague def tioki mic
Real shit all day ready for the show tonight
Mic Mic bi la tengo
Di cii Rappé ni bèn dinguo
Diaroul sax ngay haine ngo
Mane ak yaw douniou mengo
Donté one day yeukeutina game bi dékilate ko
Donté one day gnii ko guédone nieuw feel laateko
Nigga donté one day yaube nako cii ay stadium
Baake nako kaw ba ngéw yi fadiou cii ay dadiam
Cii Five years yi wéssu lima cii def déffo cii xadiam
Raxassal sa loxo mc so bagné mou xadiam
Rhymes yagui djalou
Nagoul boul jaloux
Moytoul samay uppercuts so bagné Yawou dialou
Niaak na baa siiteu
Di woute ndam ni Sitteu
Loxo cii kamile guigne naa nguir fènelo gnimaay sikk
No Violence, sign by your hands
Let the music following like a blood in your vains
Nit toudou Doff, Doff toudou Nit
2007 ba légui nigga wax ma niata hit
Fight real shit
Téwal real shit
Ghetto bégnou yoni nguir niou siweul sunu street
Nit toudou Doff, Doff toudou Nit
2007 ba légui nigga wax ma niata hit
Nétali sunu life
Lii xéw cii sunu side
Leundeum beurii takh niou iindi light
Yo
Xeuy nama diém nama
Farlou fipou taay aay nama
Faale nama faléma cii walou rap mbede djaay nama
Maa imposé dominé dem ba nones yi dima nominés
Dieum dji di gueuneu siiw
Kouné di mbiiw
Mak ak goné di fiiw
Takhirlou aay new
I'm fucking real and I stay real
LG team What's poppin my OG (What's poppin my OG)
Do djékii lo djiwoule waune
Gorr cii warr wa laniou ko xamé ba
Mouy moudié di yélwane (Nit toudou doff)
Duel mic moma mayatii
Hakk rek laay séréti
Five years you wéssou lofi thiop mako sébétii
Ok dieum djii féink xall yone indi lerr niit
Kii délo geude rap galsen moy sama mérite
Mista Champion guissouma loutakh maay tégui yone
Gni ngui woté fit founiou maa sèneu titangué fegne cii niom
Nit toudou Doff, Doff toudou Nit
2007 ba légui nigga wax ma niata hit
Fight real shit
Téwal real shit
Ghetto bégnou yoni nguir niou siweul sunu street
Nit toudou Doff, Doff toudou Nit
2007 ba légui nigga wax ma niata hit
Nétali sunu life
Lii xéw cii sunu side
Leundeum beurii takh niou iindi light
Yessay yessay from Africa Westa
Gunzout à la prod le public aime ça
Depuis l'école de la Street j'ai connu mes scarla
Diwane Squad toujours au pair comme les guerriers de Spartacs
Micro clashnicov on a conquis tout Karda
2007, dans les bacs j'ai fait trop de dégâts
2009, comme des tasspé je les ai béta
2013, 3ème Album bête de peura
Boudone xaréé maay sahaba
Boudone diné maay Kaaba
Boudone carte madone AS, yaw nga fétéwo naba
I'm like Ali cii Ring
Saff Ni kané cii tchine
Meuneu rappé meuneu flow dafa tarou cii bindeu
Damay dagou cii street,ioumay gived respect
Sama door dafa diss bitch foma guiss tek
Let me attending this game like nobody's that
Nit toudou Doff, Doff toudou Nit
2007 ba légui nigga wax ma niata hit
Fight real shit
Téwal real shit
Ghetto bégnou yoni nguir niou siweul sunu street
Nit toudou Doff, Doff toudou Nit
2007 ba légui nigga wax ma niata hit
Nétali sunu life
Lii xéw cii sunu side
Leundeum beurii takh niou iindi light
Nit toudou Doff, Doff toudou Nit
2007 ba légui nigga wax ma niata hit
Nétali sunu life
Lii xéw cii sunu side
Leundeum beurii takh niou iindi light



Writer(s): Mao, Nitdof, Papa Kandé Sidibe ( Mao )


Nitdoff feat. Mao - Rddr
Album Rddr
date of release
16-06-2013



Attention! Feel free to leave feedback.