Nitdoff - Unified Now Lyrics

Lyrics Unified Now - Nitdoff



Yo Unified
Please Unified
Bolé sunuy dolé, sunuy xam-xam Unified
Fékhé Ba babylone dotoul exploités sunu faille
Djam djék xéweul yi meune taw cii sunu sky
Mama Africa waratoul seug rek cry
Ay domam nioko waral siguile'ma kone naniouko pray
Nango Nelson Mandela inspiration
Africa United naga ko def sa destination
Sékou Touré vision
Sankara education
Cheikh Anta Diop, warna yokk motivation
United for the Future
The mother land Culture
Fi niou beug yegg yi djiko niokoy builder
U-U-U-Unified Now (A)
U-U-U-Unified Now (FRI)
U-U-U-Unified Now (CA)
U-U-U-Unified Now
Waxtou djotna fi weuk à Dieu
U-U-U-Unified Now
Waxtou djotna fi weuk à Dieu
Unified Now (A)
Unified Now (FRI)
Unified Now (CA)
Bolo bène, wara nek sunu fight now
Yeah!!! Right now it's the moment
Yeah!!! the right moment
Niougui wo xalé mak gorr ak bépeu women
Africa warna unified cii bépeu domaine
Bolé sunuy dolé exploité sunuy meunine
Bayi wakh djeuf xamné time is running
Niou free bagna wékou cii systémou babylone
Black djap beu, dotou niou walii yone
Kou meussoul téyé bass xeuy am 10.000.000
Féthie kanam yi niou fass di Amdy Mignon
Bokk done bène éthnie moytou rebellion
Monnaie bi di bène, Frontière yi di bène
Africa Right Now, Bo tchii beugué guène
U-U-U-Unified Now (A)
U-U-U-Unified Now (FRI)
U-U-U-Unified Now (CA)
U-U-U-Unified Now
Waxtou djotna fi weuk à Dieu
U-U-U-Unified Now
Waxtou djotna fi weuk à Dieu
Unified Now (A)
Unified Now (FRI)
Unified Now (CA)
Bolo bène, wara nek sunu fight now
Magui call Nigeria
Call wa Liberia
Ivory Coast Mali ak Mauritania
Please naniou fagarou soukeuli sunu area
Wara touniou tongo
Diotena niou longo
Tanzania Ethiopie ba yegg Congo
Thieurou mother land warna délou famou néwone
South Africa Somalia ak Sierra Leone
Unified Money diokh Power
Ak prosperity li moy yone bi geuneu gawa
Waxtou bagui naw
Niogui dess Guinaw
Immigration kou nék fakkeu djeumi kaw
Unification is the key, do it now
U-U-U-Unified Now (A)
U-U-U-Unified Now (FRI)
U-U-U-Unified Now (CA)
U-U-U-Unified Now
Waxtou djotna fi weuk à Dieu
U-U-U-Unified Now
Waxtou djotna fi weuk à Dieu
Unified Now (A)
Unified Now (FRI)
Unified Now (CA)
Bolo bène, wara nek sunu fight now



Writer(s): Nitdof, Papa Kandé Sidibe ( Mao )


Nitdoff - Rddr
Album Rddr
date of release
16-06-2013




Attention! Feel free to leave feedback.