Lyrics Xouss Di Dém - Nitdoff
Niou
meuneu
féy
naniou
féy
niou
meunoul
féye
Naniou
lapp
Kène
xaratoul
kène,
kounék
ngui
bagne
koula
dapp
Kou
Amm
niou
diokh
laa
thieur
kou
niak
nieupeu
Laay
yapp
Saay
mbok
niolay
ndieuk
xépp
guénél-leu
diapp
Kène
doula
ndamo
kène
doula
titeuro
ko
sago
Donté
bakh
nga
amm
yar
ak
téguine
waayé
tiabo
Kène
xolatoul
lou
né
cii
xoll
yi
niogui
visé
lou
nék
Cii
poss
yi
Djiko
you
bakh
yigni
dane
sédé
nit
teumbou
naa
cii
Foss
bi
Téré
bigni
guéteuro
iblis
sako
Euw
Dunya
laniou
djiteul
faté
nii
laxirra
ngui
nieuw
Topeu
bépp
niaw
tef
tagok
yiw
Dieul
gradou
kunfaya
tapal
ko
diw
ak
diw
Té
serigne
souniou
warone
dialalé
gnou
djégui
Ngay
xeuy
dii
lire
sèn
scandale
cii
diank
dji
ak
cii
Diégg
yi
Niom
gni
warone
xali
yone
niolay
djam
pontou
Tank
Séni
beutt
talibé
bi
wéssou
woul
app
compte
bank
Xamalé
wouniou
lèn
cii
charia
bilahi
Sèn
nafsu
laniou
teunk
cii
merco
(Voiture)
yi
ak
Villa
Xaptal
gni
lène
topeu,
Yakk
sèni
bopp
Géré
sen
mafia
recupéré
seni
adiyeu
Gni
xam
warone
yété
dadii
né
tek
def
thiéleu
gui
Bayi
charlatan
yi
niouw
tilimeul
diné
bou
séleu
bi
Yèn
parents
yi
seug
bayi
kass
Libérés
sèni
dom
cii
ay
apparte
(Appartements)
Niou
doni
thiaz
Dii
diokh
pa
loumouy
fayé
louwass
Mère
loumou
djeundé
gaz
Té
clan
yi
lèni
dass
dilène
diokh
ay
liasse
Ay
kilifeu
lagni
done
ay
imam
ak
oustaz
Xalissou
toxico
yi
moy
soukeur
séni
douté
Kèn
ladia
touniou
sunu
money
nouniou
koy
wouté
Yomb
am
té
niakk
léw
sa
gueum
lalay
couté
Leunkeu
lok
iblis
moulaay
nab
nabé
né
poupée
Kèn
ragalatoul
God
missiou
bi
laniou
loupé
Niogui
xouss
di
dém
cii
yonou
moussibeu
ak
bala
Deuké
ndiabar
ak
xeureum
bokalé
riiba
ak
bida
Mbougueul
diougué
cii
kaw
wathie
cii
souf
wouyo
Sida
Gni
warone
tétale
yone
bi
diaréko
cii
musica
Sunu
sister
yi
dém
club
lathie
wiski
wala
vodka
Ko
tchii
fouillésaaggam
fék
tchii
pilule
wala
potka
(Capote)
Noy
bopp
yomb
nakh
biss
bou
nek
niou
lèni
rotka
(Carottées)
Hypothéqués
sen
avenir
cii
ay
jobbou
mannequin
Dém
ba
moudj
tarkhiss
thiagatou
done
sèn
gagne
Pain
Hom
boy
yi
tokk
sèn
coin
di
taukh
séni
zoin
Kotchii
wakh
mounalé
grand
lii
fimou
ma
yaube
Dafa
loin
Xana
xamoulo
ni
fils
yagui
yakk
sa
neurones
yi
Wala
daga
beug
done
boy
meurone
yi
Lambeu
na
fima
deudjone
sama
gueum
fékou
mafa
Nada
Xamé
touniou
sakh
sunu
thiossane
ak
sunu
Adda
Topando
nassarane
bi
ba
faf
sarane
Gueuleum
tchii
yonou
thiaxane,
Deuké
takhourane
Maitrisé
téré
ngéw
yi
ignoré
Al-qurane
Xalé
you
am
15,
16
diap
dii
saa
temps
Sunu
télé
yi
dilène
influencés
baniou
guiss
satan
Cii
ay
serie
latino
youy
xoumbeul
sèn
libido
Téléchargé
sen
call
yi
ay
porn
vidéo
Internet
done
bèn
riiro
bou
nieup
meuneu
mouri
Té
mbalite
bitchii
aduna
bi
yeup
lagn
faay
touri
Ammatouniou
bèn
moeurs
lii
wokk
ngéw
yi
moniou
Xouri
Akhirou
zamane
leu,
les
taux
se
resserrent
Gni
djié
danio
échoués
tout
est
à
refaire
Waxtou
dafa
diott
niou
wara
xolate
sunuy
repères
Yèn
jeunes
yagui
déviés
cii
ay
dérives
you
sectaire
Lesbiennes
yi
ak
pd
yi
di
gueune
am
sagn
sagn
Sakétou
cii
droit
de
l'homme
ndakh
koulèni
fitneul
Lagni
bagne
Mbalax
men
yi
daniou
triste
pirate
bélène
Bouleversés
Kou
tchii
beug
percé
serigne
cii
ngay
commercé
Yéngueul
down
cii
ay
xassaide
tarrii
versets
Talibé
yu
con
yi
Youkou
poches
dadii
versés
Bouleu
fékone
cii
diotay
bou
séleu
té
linga
soleu
Yiw
Nga
meuneu
diouk
fatassou
cii
barké
Serigne
Saliou
Waayé
ay
thiaga
you
féthie
di
wané
séni
thieur
né
Kouy
ndialo
Rek
nioy
fess
cii
ay
soirée
Ssalam
Diallo
Seck
o
Fall
o
guinar
aki
nénam
Kiguay
féthie
diko
rissou
yagui
toyal
guènaam
Doko
fadial
soxlam
té
dagay
yokou
peiname
Diaral
nako
diokhé
xalissam
mayé
chainame
Lépp
rek
nguir
meuneu
sani
bagg
meuneu
rott
cii
Ténaam
Philosophie
bigni
démé
légui
bop
sa
bopp
leu
Roki
mi
rokileu
Life
bi
légui
Thiokileu
Bo
daloule
Séne
kaw
niom
niou
dale
sa
kaw
Dioguileu
Gniko
téleu
nandeu
khame
naniou
né
légui
diouk
Jobbileu
Amatoul
mboko
wala
affaire
de
diapo
sama
dow
Bileu
(Xaliss)
Kou
tchi
nek
yagui
teuth
sa
keur
affaire
de
guéw
Yigni
niodileu
Senegal
réwou
téranga
dianako
wakh
guir
sargal-
Leu
Mé
téwoul
khamenagn
ni
fi
chacun
pour
sa
gueule
Bo
niaké
niou
khépeleu
bo
amé
niou
sargal-leu
Dagni
dém
ba
faté
sugnu
léni
mour
perkal-leu
Do
yaubalé
cos
(Costume)
do
yaubalé
sakh
perou
Daleu
Kéneu
doula
nawléwo
kou
rombeu
xélou
dadi
djaleu
Dagni
fokni
niom
nioy
yékini
yaw
gay
yawou
Diaaleu
Saa
rak
sakh
souleu
eupeulé
doto
tawou
galé
Sa
pa
bi
noumou
lay
beurguelé
nakheté
doko
awou
Galé
Niogui
xouss
di
dém
Niogui
xouss
di
dém
Niogui
xouss
di
dém
Attention! Feel free to leave feedback.