Lyrics Sunugal - Nitdoff
Golo
ngui
di
baay
baboune
doundé
Tokk
sunu
kaw
yata
youmbé
Nioune
gnifi
dess
yakar
kun
déy
Sunu
life
gueune
hot
niouy
mathie
tougn
déy
Fay
Sunu
lampe
koupé
sunu
ndox
youkou
Sunu
doundeu
kone
fokk
niou
niaff
sèn
nd
Kom
komou
réw
bi
guène
passarr-passarréé
Louniou
ama
kass
ak
néw
guène
dieul
mandé
Niak
bék
fébar
yek
walakana
bi
niouy
gueuneu
toumranké
Guène
télé
mbélé
mbélé
diokhé
délé
ay
féni
nène
ma
tay
Oubile
sa
beut
té
xoll
li
khéw
Diougueul
fipou
nguir
sa
réw
Baniou
massi
sakh
guène
defma
néw
Guène
gassma
soule
douma
bokk
sèn
guéw
Sénégal
loumou
mérité
dé
dou
Li
Ndiouth
ndiath
bi
dé
wessou
fii
Sathie
ngui
mom
béssou
fi
Takhena
sunu
caisse
dara
déssou
fii
Borom
keur
yagui
run
dépense
Amatou
niou
ndieugou
ordonnance
Khif
ak
marr
dignou
eskanté
ngay
woutt
nguissteul
cii
renaissance
Vide
de
sens,
incompétence
Tu
ne
mesures
pas
les
conséquences
Fermes
ta
gueule
et
fous
le
camp
On
a
perdu
assez
de
temps
Bépp
gokh
fo
meune
tiii
dém
kaddu
bi
bèn
leu
daniou
beug
nga
yokh
Lifi
né
mom
diégui
na
tiss
Lignou
yèn
daay
gueune
diss
Diokhatila
Rap
ngakoy
feel
di
chill
Sénégal
éh
Sénégal
oh
Sénégal
moy
sunu
réw
Sénégal
éh
Sénégal
oh
Sénégal
moy
sunu
réw
Na
beut
yi
wékh
Na
xol
yi
fékh
Na
fiitna
dale
sunu
thiono
diékh
Clando
yi
garé,
4×4
yi
guène
Niou
pédophiles
yi
ak
goor
djiguène
yi
Lo
fii
def
Yalla
néla
je
retiens
Ngay
muslim
wala
ngay
chretiens
Ngay
ilimane
wala
politiqu'chiens
Yiy
djité
sunu
réw
dignou
tékeulé
ak
chiens
Loy
titeuro
loy
poukeuré
wo
Alalou
riba
bi
dé
yaw
goré
wo
Nioune
nio
wathione
cii
tali
bi
ak
yaw
Sopi
nganiou
digone
niou
dadii
lay
naw
Taay
la
gale
ngui
gueune
dikk
Gueuneu
sikk
Xalé
yi
xaddi
diar
cii
guethie
gui
daw
Rap
galsen
bi
tchii
wané
niveau
bileu
Technique
kou
bindeu
bi
dé
nieuw
ropila
Xam
xamou
mbede
bi
ngay
dém
rotila
Wessou
na
rap
bi
dé
li
tiokila
tiokila
tiokila
Yo
Low
Low
Low
Low
Guiss
nga
li
xéw
cii
mbeude
bi
ndakh
sa
yaram
dawna
Askan
wi
defla
ennemi
ndakh
sèn
xoll
yi
wow
na
Fébar
yi
beuri
sunu
biir
takhna
déh
gui
gaw
na
Té
biss
bou
né
nga
dégg
kopar
yigni
fi
loubeul
raw
na
Té
néw
di
dolé
diey
fay
sèn
taukhi
douna
Té
koffi
waulou
fale
ko
taay
souba
sopé
kouna
Yeurmandé
amatoul
cii
diam
yi
ma
niak
souma
Na
yalla
def
cii
xoll
yi
lerr
ndakh
beut
yi
guissa
touniou
Diokhatila
Rap
ngakoy
feel
di
chill
Sénégal
éh
Sénégal
oh
Sénégal
moy
sunu
réw
Sénégal
éh
Sénégal
oh
Sénégal
moy
sunu
réw
Naniou
fagaru
fékhé
ba
kèn
douniou
waaleu
Téleu
diouk
meuneu
xali
yone
dialeu
Yorr
sunu
poches
ay
millions
dollar
Di
bégué
beauté
am
free,
am
power
Naniou
bolo
benno
job
Galsen
nek
on
the
top
Niane
cii
diami
Casamance
Yalla
def
tchi
li
ko
sobb
Kèn
waroul
manqué
thiop
Kèn
waroul
xepp
say
mbokk
Kèn
waroul
am
ba
béw
Ndakh
xamoulo
souba
lane
moy
xéw
Boy
dém
Makka
tabakh
diaka
li
nga
tchi
def
dana
fekk
mou
léw
Dana
fekk
mou
léw
Diokhatila
Rap
ngakoy
feel
di
chill
Sénégal
éh
Sénégal
oh
Sénégal
moy
sunu
réw
Sénégal
éh
Sénégal
oh
Sénégal
moy
sunu
réw
Sénégal
moy
sunu
réw
Sénégal
éh
Sénégal
oh
Sénégal
moy
sunu
réw
Attention! Feel free to leave feedback.