Nitdoff - Xouss Di Dém - translation of the lyrics into Russian

Lyrics and translation Nitdoff - Xouss Di Dém

Niou meuneu féy naniou féy niou meunoul féye

Naniou lapp
Naniou lapp
Kène xaratoul kène, kounék ngui bagne koula dapp

Kou Amm niou diokh laa thieur kou niak nieupeu

Laay yapp
Laay yapp
Saay mbok niolay ndieuk xépp guénél-leu diapp

Kène doula ndamo kène doula titeuro ko sago

Donté bakh nga amm yar ak téguine waayé tiabo

Kène xolatoul lou cii xoll yi niogui visé lou nék

Cii poss yi
Cii poss yi
Djiko you bakh yigni dane sédé nit teumbou naa cii

Foss bi
Foss bi
Téré bigni guéteuro iblis sako Euw
Téré bigni guéteuro iblis sako Euw
Dunya laniou djiteul faté nii laxirra ngui nieuw

Topeu bépp niaw tef tagok yiw
Topeu bépp niaw tef tagok yiw
Dieul gradou kunfaya tapal ko diw ak diw

serigne souniou warone dialalé gnou djégui

Ngay xeuy dii lire sèn scandale cii diank dji ak cii

Diégg yi
Diégg yi
Niom gni warone xali yone niolay djam pontou

Tank
Tank
Séni beutt talibé bi wéssou woul app compte bank

Xamalé wouniou lèn cii charia bilahi
Xamalé wouniou lèn cii charia bilahi
Sèn nafsu laniou teunk cii merco (Voiture) yi ak

Villa
Villa
Xaptal gni lène topeu, Yakk sèni bopp
Xaptal gni lène topeu, Yakk sèni bopp
Géré sen mafia recupéré seni adiyeu
Géré sen mafia recupéré seni adiyeu
Gni xam warone yété dadii tek def thiéleu gui

Bayi charlatan yi niouw tilimeul diné bou séleu bi

Yèn parents yi seug bayi kass
Yèn parents yi seug bayi kass
Libérés sèni dom cii ay apparte (Appartements)

Niou doni thiaz
Niou doni thiaz
Dii diokh pa loumouy fayé louwass
Dii diokh pa loumouy fayé louwass
Mère loumou djeundé gaz
Mère loumou djeundé gaz
clan yi lèni dass dilène diokh ay liasse

Ay kilifeu lagni done ay imam ak oustaz
Ay kilifeu lagni done ay imam ak oustaz
Xalissou toxico yi moy soukeur séni douté

Kèn ladia touniou sunu money nouniou koy wouté

Yomb am niakk léw sa gueum lalay couté
Yomb am niakk léw sa gueum lalay couté
Leunkeu lok iblis moulaay nab nabé poupée

Kèn ragalatoul God missiou bi laniou loupé

Niogui xouss di dém cii yonou moussibeu ak bala

Deuké ndiabar ak xeureum bokalé riiba ak bida

Mbougueul diougué cii kaw wathie cii souf wouyo

Sida
Sida
Gni warone tétale yone bi diaréko cii musica

Sunu sister yi dém club lathie wiski wala vodka

Ko tchii fouillésaaggam fék tchii pilule wala potka

(Capote)
(Capote)
Noy bopp yomb nakh biss bou nek niou lèni rotka

(Carottées)
(Carottées)
Hypothéqués sen avenir cii ay jobbou mannequin

Dém ba moudj tarkhiss thiagatou done sèn gagne

Pain
Pain
Hom boy yi tokk sèn coin di taukh séni zoin

Kotchii wakh mounalé grand lii fimou ma yaube

Dafa loin
Dafa loin
Xana xamoulo ni fils yagui yakk sa neurones yi

Wala daga beug done boy meurone yi
Wala daga beug done boy meurone yi
Lambeu na fima deudjone sama gueum fékou mafa

Nada
Nada
Xamé touniou sakh sunu thiossane ak sunu Adda

Topando nassarane bi ba faf sarane
Topando nassarane bi ba faf sarane
Gueuleum tchii yonou thiaxane, Deuké takhourane

Maitrisé téré ngéw yi ignoré Al-qurane
Maitrisé téré ngéw yi ignoré Al-qurane
Xalé you am 15, 16 diap dii saa temps
Xalé you am 15, 16 diap dii saa temps
Sunu télé yi dilène influencés baniou guiss satan

Cii ay serie latino youy xoumbeul sèn libido

Téléchargé sen call yi ay porn vidéo
Téléchargé sen call yi ay porn vidéo
Internet done bèn riiro bou nieup meuneu mouri

mbalite bitchii aduna bi yeup lagn faay touri

Ammatouniou bèn moeurs lii wokk ngéw yi moniou

Xouri
Xouri
Akhirou zamane leu, les taux se resserrent

Gni djié danio échoués tout est à refaire

Waxtou dafa diott niou wara xolate sunuy repères

Yèn jeunes yagui déviés cii ay dérives you sectaire

Lesbiennes yi ak pd yi di gueune am sagn sagn

Sakétou cii droit de l'homme ndakh koulèni fitneul

Lagni bagne
Lagni bagne
Mbalax men yi daniou triste pirate bélène

Bouleversés
Bouleversés
Kou tchii beug percé serigne cii ngay commercé

Yéngueul down cii ay xassaide tarrii versets

Talibé yu con yi Youkou poches dadii versés

Bouleu fékone cii diotay bou séleu linga soleu

Yiw
Yiw
Nga meuneu diouk fatassou cii barké Serigne

Saliou
Saliou
Waayé ay thiaga you féthie di wané séni thieur

Kouy ndialo
Kouy ndialo
Rek nioy fess cii ay soirée Ssalam Diallo

Seck o Fall o guinar aki nénam
Seck o Fall o guinar aki nénam
Kiguay féthie diko rissou yagui toyal guènaam

Doko fadial soxlam dagay yokou peiname
Doko fadial soxlam dagay yokou peiname
Diaral nako diokhé xalissam mayé chainame

Lépp rek nguir meuneu sani bagg meuneu rott cii

Ténaam
Ténaam
Philosophie bigni démé légui bop sa bopp leu

Roki mi rokileu Life bi légui Thiokileu
Roki mi rokileu Life bi légui Thiokileu
Bo daloule Séne kaw niom niou dale sa kaw

Dioguileu
Dioguileu
Gniko téleu nandeu khame naniou légui diouk

Jobbileu
Jobbileu
Amatoul mboko wala affaire de diapo sama dow

Bileu (Xaliss)
Bileu (Xaliss)
Kou tchi nek yagui teuth sa keur affaire de guéw

Yigni niodileu
Йигни ниодилеу
Senegal réwou téranga dianako wakh guir sargal-
Сенегал реву Теранга дианако вах гуир саргал-
Leu
Лея
téwoul khamenagn ni fi chacun pour sa gueule
Я собираюсь съесть шоколадную крошку на
Bo niaké niou khépeleu bo amé niou sargal-leu
Я не смогу тебя увидеть - лол
Dagni dém ba faté sugnu léni mour perkal-leu
Не волнуйся, я собираюсь откусить от тебя кусочек... лол
Do yaubalé cos (Costume) do yaubalé sakh perou
Делай яубале потому что (костюм) делай яубале сах перу
Daleu
Дейл
Kéneu doula nawléwo kou rombeu xélou dadi djaleu

Dagni fokni niom nioy yékini yaw gay yawou

Diaaleu
Diaaleu
Saa rak sakh souleu eupeulé doto tawou galé

Sa pa bi noumou lay beurguelé nakheté doko awou

Galé
Galé
Niogui xouss di dém
Niogui xouss di dém
Niogui xouss di dém
Niogui xouss di dém
Niogui xouss di dém
Niogui xouss di dém

Writer(s): papa kandé sidibe ( mao )

Attention! Feel free to leave feedback.