Nitdoff - Vampaya - translation of the lyrics into French

Lyrics and translation Nitdoff - Vampaya

Vampaya
Vampire
Wax djou sew bii dafa beurii
Wax djou sew bii dafa beurii
Men I'm tired
Men I'm tired
Daniou beug moutiou sama blood
Daniou beug moutiou sama blood
Ni vampaya ni vampaya
Ni vampaya ni vampaya
Ni vampaya ni vampaya
Ni vampaya ni vampaya
Yeah
Yeah
Yallah taw alleu naaate ma fasse sama fite daldi sole dallou mak
Yallah taw alleu naaate ma fasse sama fite daldi sole dallou mak
Soldaru mbed yémeu faal di djow sama flack
Soldaru mbed yémeu faal di djow sama flack
Xaxta ndikou fire ngakoy feel cii bépeu track
Xaxta ndikou fire ngakoy feel cii bépeu track
Niouy soss di laay di féété wakh djou bone yi sama back
Niouy soss di laay di féété wakh djou bone yi sama back
Téwoul maay gueuneu dii dém tchii ligni def malèn ko daak
Téwoul maay gueuneu dii dém tchii ligni def malèn ko daak
Nigga meunoma freiné, nanda go foumay brainé
Nigga meunoma freiné, nanda go foumay brainé
Ay ndiouni att ak sama bosse yi limako trainé
Ay ndiouni att ak sama bosse yi limako trainé
Sa crew loumou tangue tangue dagn koy diérii mec
Sa crew loumou tangue tangue dagn koy diérii mec
Dox sa biir périmetre toule sa 9mm
Dox sa biir périmetre toule sa 9mm
Braqué sa public diam lèn flow baniou firii
Braqué sa public diam lèn flow baniou firii
Niggaz yi tiow sen xoll moy ...
Niggaz yi tiow sen xoll moy ...
Kou ngène guémb ma dieul, kou ngène indi ma ndéle
Kou ngène guémb ma dieul, kou ngène indi ma ndéle
Niggaz yi xew kouma cii sèneu dagay def thièle
Niggaz yi xew kouma cii sèneu dagay def thièle
Yaw yagui woté real ya gueuneu naafekh
Yaw yagui woté real ya gueuneu naafekh
Affaire de Luv mane ak yaw dotou niouko gawa sékk
Affaire de Luv mane ak yaw dotou niouko gawa sékk
BIAAAAAAAATCH
BIAAAAAAAATCH
Wax djou sew bii dafa beurii
Wax djou sew bii dafa beurii
Men I'm tired
Men I'm tired
Daniou beug moutiou sama blood
Daniou beug moutiou sama blood
Ni vampaya ni vampaya
Ni vampaya ni vampaya
Ni vampaya ni vampaya
Ni vampaya ni vampaya
Wax djou sew bii dafa beurii
Wax djou sew bii dafa beurii
Men I'm tired
Men I'm tired
Daniou beug moutiou sama blood
Daniou beug moutiou sama blood
Ni vampaya ni vampaya
Ni vampaya ni vampaya
Ni vampaya ni vampaya
Ni vampaya ni vampaya
Fi koumou nekh hainale, nioune Yalla lagni kènale
Fi koumou nekh hainale, nioune Yalla lagni kènale
King of Hip Hop bimou def tchi nioune meunoko nénale
King of Hip Hop bimou def tchi nioune meunoko nénale
Kharagne La tchiii mic, Balla Gaye 2 cii show
Kharagne La tchiii mic, Balla Gaye 2 cii show
Galagne ko baa to death, mane laniou doylo tchii flow
Galagne ko baa to death, mane laniou doylo tchii flow
Liniou mouraune lane mourriiii, gnou khifone rek ma nourris
Liniou mouraune lane mourriiii, gnou khifone rek ma nourris
Faalou done bourrii bourr yi, contenairou rimes maa yourrii
Faalou done bourrii bourr yi, contenairou rimes maa yourrii
Let me give thanks
Let me give thanks
Hip Hop Galsen ma done tchii Légitime Gangsta
Hip Hop Galsen ma done tchii Légitime Gangsta
Never look back, Let them talk rék
Never look back, Let them talk rék
Untouchable Killah moy dieuwrignou D-Squad
Untouchable Killah moy dieuwrignou D-Squad
Maa nekk à la mode,;aneleu thug yi di nodeu
Maa nekk à la mode,;aneleu thug yi di nodeu
Nitdoff ciii sèni shirt, ba tchii seur yigni wodeu
Nitdoff ciii sèni shirt, ba tchii seur yigni wodeu
Mbede maa diokh dolé,;aa athie ko sama ndode
Mbede maa diokh dolé,;aa athie ko sama ndode
Ande ak mom dikko gougué téw tchii bépp épisode
Ande ak mom dikko gougué téw tchii bépp épisode
Diém naniou maa étiquetté, lépp cii fénii kessé
Diém naniou maa étiquetté, lépp cii fénii kessé
Bou yabo guène woutii pékhé, ndakh cii rap maa lènii fessé
Bou yabo guène woutii pékhé, ndakh cii rap maa lènii fessé
Diébelou molène dess2
Diébelou molène dess2
Wax djou sew bii dafa beurii
Wax djou sew bii dafa beurii
Men I'm tired
Men I'm tired
Daniou beug moutiou sama blood
Daniou beug moutiou sama blood
Ni vampaya ni vampaya
Ni vampaya ni vampaya
Ni vampaya ni vampaya
Ni vampaya ni vampaya
Wax djou sew bii dafa beurii
Wax djou sew bii dafa beurii
Men I'm tired
Men I'm tired
Daniou beug moutiou sama blood
Daniou beug moutiou sama blood
Ni vampaya ni vampaya
Ni vampaya ni vampaya
Ni vampaya ni vampaya
Ni vampaya ni vampaya
Taay la saar yi gueuneu mokatt
Taay la saar yi gueuneu mokatt
Flow yi gueuneu yokott, fiit yi gueuneu togat
Flow yi gueuneu yokott, fiit yi gueuneu togat
Bitch nigga yiy djaay prek lagni nopattt
Bitch nigga yiy djaay prek lagni nopattt
Nokoss Di rokoss kané rofko niou togaatteu
Nokoss Di rokoss kané rofko niou togaatteu
Album bou guéneu hot
Album bou guéneu hot
Xolou none yi di gueuneu bad
Xolou none yi di gueuneu bad
They wanna kill the Killah, but now I feel the deal
They wanna kill the Killah, but now I feel the deal
Diokh ngama five téwoul xam nanii ennemi nga
Diokh ngama five téwoul xam nanii ennemi nga
Yaw yagui tokk triché, Di xarr ma trébuchet
Yaw yagui tokk triché, Di xarr ma trébuchet
Xamo tchii mane loudoul ay mother fuck préjugés
Xamo tchii mane loudoul ay mother fuck préjugés
I'm from the bottom, I'm on the Top
I'm from the bottom, I'm on the Top
Dioxogne maa baram, I don't give a Fk
Dioxogne maa baram, I don't give a Fk
Xamna fima bokk
Xamna fima bokk
Diwane Squad dou loxal guène nélène walabokk
Diwane Squad dou loxal guène nélène walabokk
Wax djou sew bii dafa beurii
Wax djou sew bii dafa beurii
Men I'm tired
Men I'm tired
Daniou beug moutiou sama blood
Daniou beug moutiou sama blood
Ni vampaya ni vampaya
Ni vampaya ni vampaya
Ni vampaya ni vampaya
Ni vampaya ni vampaya
Wax djou sew bii dafa beurii
Wax djou sew bii dafa beurii
Men I'm tired
Men I'm tired
Daniou beug moutiou sama blood
Daniou beug moutiou sama blood
Ni vampaya ni vampaya
Ni vampaya ni vampaya
Ni vampaya ni vampaya
Ni vampaya ni vampaya
Hummm éh éh éh
Hummm éh éh éh

Writer(s): Nitdof, Papa Kandé Sidibe ( Mao )

Attention! Feel free to leave feedback.