Viviane Chidid - Da fa gnaw Lyrics

Lyrics Da fa gnaw - Viviane Chidid



Bi adouna
Loufi diar niouy def lou niaw
Bi adouna
Loufi way rendi sa lokho lay natieu
Wakhma lane motakh
Beugou loma wakhal lou bakh
Wakhma lane moy mbakh
Boudé yéneunté wouniou lou bakh
Li dafa niaw(×3)
Li dafa niaw (×3)
Li dafa niaw naniou sett si yalla bayi batt diou niaw
Khamna sama tolou way ya takh sa fitt di naw
Yalla nopina
Fi dara dou niaw
Lissi mane nekoul si yaw (Gani)
Lissi mane nekoul si yaw (Dieuleul)
Lissi mane nekoul si yaw beugueunté léne fi adouna la (Wawaw)
Lissi mane nekoul si yaw (Wakhal)
Lissi mane nekoul si yaw (Kay)
Lissi mane nekoul si yaw beugueunté léne fi adouna (Wakhal way)
Deret biy daw si yaw moy daw si mane
Wakhma lane motakh
Douniou yéneunté lou bakh
Li dafa niaw(×3)
Li dafa niaw(×3)
Li dafa niaw naniou sett si yalla bayi batt diou niaw
Khamna sama tolou way ya takh sa fitt di naw
Yalla nopina
Fi dara dou niaw
Li dafa niaw(×3)
Li dafa niaw(×3)
Li dafa niaw naniou sett si yalla bayi batt diou niaw
Khamna sama tolou way ya takh sa fitt di naw
Yalla nopina
Fi dara dou niaw
Tu tapes dans mon dos
Tu parles dans mon dos
Tu craches dans mon dos
Sourire à la face couteau dans mon dos
Tu tapes dans mon dos
Tu parles dans mon dos
Tu craches dans mon dos
Sourire à la face couteau dans mon dos
Wakhal way
Djidiak wakhal way
Kokoy chérie Aida
Abdou Mbaye (wakhal way)
Borom...
Mane Akathi wakhal way (domou Abidjan leu)
Bakhaw wakhal way (Kokay gorou Viviane)
Kiné wakhal way (Kokou sama dom la)
Awadi wakhal way
Sénégal wakhal way



Writer(s): Akatche Koffi, Beneth Seraphin, Viviane Chidid


Viviane Chidid - Wuyuma
Album Wuyuma
date of release
13-02-2017




Attention! Feel free to leave feedback.