Lyrics Tèrè Doundou - Viviane Chidid
Doma
téré
doundou
mann
Ndakh
sakou
loma
Koulay
téré
doundou
mom
Na
fékeu
mou
momla
yaw
Ndakh
yèneu
saay
nitt
tekla
thiono
Dèlou
nékeu
thji
noflay
Soko
nango
bamou
sonal
la
yako
tek
sa
bopou
way
Ouuuhh
waaahhh
Mani
déféko
ni
ndakh
bakane
diam
la
beugeu
Doundal
seu
doundou
boulènn
falé
Yèneu
yi
soxor
lamay
ndourol
Wakh
dji
deh
safouma
dorr
yi
deh
yeuugouma
Ndakh
sama
yaram'ma
blindé
Dioxoma
lèkeu,
dioxoma
nann
momouloma
yaw
mi
lé
(Doma
téré
doundou
Doma
téré
doundou)
Ngay
diougaka
danou
niouni
ki
deh
diambar
leu
Di
agné
thji
aleu
bi
rèrrè
thji
mbédeu
mi
niounan'la
niafa
ko
nonoula
Bo
amé
té
amoto
yaw
nitt
yila
donn
yènè
lou
baakh
niolay
ndieuka
saaga
Ngay
dougaka
guéneu
diko
lidieunti,
niounanla
yow
mi
deh
thiaga
nga
Bougn
la
téré
doundou
Doma
téré
doundou
Doma
téré
doundou
Mann
amouma
diott
té
loma
def
bal
nala
(nala)
Dima
lidieunti
bay
xeuy
bideunti
xana
deh
yaw
deh
sonou
lo
Dounn
momoula
adouna
nonou
la,
ndakh
kou
nèkeu
diw
dou
diamam
Téré
ma
doundou
beugeu
di
doundou
tay
ma
xamal
la,
lo
xamoul
wonn
Doma
téré
doundou
Doma
téré
doundou
Doma
téré
doundou
Adouna
yalla
ngay
diamou
boko
défoul
dinga
ganiou
Doundou
lénn,
linguén
di
doundou
niou
yènènté
diam
Adouna
yalla
ngay
diamou
boko
défoul
dinga
ganiou
Doundou
lénn,
linguén
di
doundou
niou
yènènté
diam
Ndakh
yèneu
saay
nitt
tekla
thiono
dèlou
nékeu
thji
noflay
Soko
nango
bamou
sonal
la
yako
tek
sa
bopou
way
Ouuhh
waaahhh
Mani
déféko
ni
ndakh
bakane
diam
la
beugeu
Doundal
seu
doundou
boulènn
falé
Yèneu
yi
soxor
lamay
ndourol
Wakh
dji
deh
safouma
dorr
yi
deh
yeuugouma
Ndakh
sama
yaram'ma
blindé
Dioxoma
lèkeu,
dioxoma
nann
momouloma
yaw
mi
lé
(Doma
téré
doundou
Doma
téré
doundou)
Ngay
diougaka
danou
niouni
ki
deh
diambar
leu
Di
agné
thji
aleu
bi
rèrrè
thji
mbédeu
mi
niounan'la
niafa
ko
nonoula
Bo
amé
té
amoto
yaw
nitt
yila
donn
yènè
lou
baakh
niolay
ndieuka
saaga
Ngay
dougaka
guéneu
diko
lidieunti,
niounanla
yow
mi
deh
thiaga
nga
Bougn
la
téré
doundou
Doma
téré
doundou
Doma
téré
doundou
1 Rëcc Na
2 Yenn Saï (feat. Fally Ipupa)
3 Djoug Liguey
4 Tèrè Doundou
5 Nangoulema
6 Déranger
7 Do Dara
8 Senegal
9 Benen Level
10 Def Ndam
11 Yenë Saay
Attention! Feel free to leave feedback.