Viviane Chidid - Yenë Saay Lyrics

Lyrics Yenë Saay - Viviane Chidid



(Yenë Saay, Yenë Saay,
Deffal yeuffou bandit,
Tassarel arsenal bi, telleul teudd,
Keur gui tass)
Nieuwël ma wakh la noy doundék wadji
Dama né, nieuwël ma wakhla foy diay Alhadji
Nieuwël, nieuwël ma wakhla noy déf ak wadji (wadji)
Dieukër dang koy doundeul, wagni thioow li (thioow li)
Wane ko lingako naral (naral)
Tassaré ko ci lalam (ci lalam)
Di na la diguaat auto, keur gou bess, wourouss ak ngalam (ngalam)
Yétal ko ba ci kanam (ci kanam)
ko ci kaw lalam (ci kaw lal)
Djiguene da ngay djongué, mokk pothie, diongama
Dégglou ma
[Yenë Saay, Yenë Saay,
Deffal yeuffou bandit,
Tassarel arsenal bi, telleul teudd,
Keur gui tass] x 2
Comme ci
Comme ça
Comme ci
Comme ça
KAAY
Solal ko mbakhané kessé
Sa djeukeur leu, lépeu ci daguann
Taalal lampe, yokk thiouraay,
Dougeul taath ci mbadj lou yeungou raayal
Sa arsenal bi khekh-akoy tass
Paaka bou gnaw diaroula daass
Dieukër dagnou koy topatoo diko
Nabë-nabé, seuy dangay kham louy ndieugueum
[Yow deukeul thi dieufé louy nekh Alhadji (Alhadji)
Sëyeul, nekhal ko thi biir nekk bi ak waagn bi (waagn bi) ] x 2
Wane ko lingako naral
Tassaré ko ci lalam
Di na la diguaat auto, keur gou bess, wourouss ak ngalam
Yétal ko ba ci kanam
ko ci kaw lalam
Djiguene da ngay djongué, mokk pothie, diongama
Dégglou ma
[Yenë Saay, Yenë Saay,
Deffal yeuffou bandit,
Tassarel arsenal bi, telleul teudd,
Keur gui tass] x 2
Comme ci
Comme ça
Comme ci
Comme ça
KAAY
Alice loutakh, nga djinakh beuri pakh?
Marie Jeanne loutakh, nga djinakh beuri pakh?
Comme ci
Comme ça
C'est ça
Si si
Chou chou
Pompom
Aaahh Eeeh
[Yenë Saay, Yenë Saay,
Deffal yeuffou bandit,
Tassarel arsenal bi, telleul teudd,
Keur gui tass] x 4



Writer(s): Akatche Bennette, Bakhaw Dioum, Seraphin Koffi, Victoria Catherine Chidid


Viviane Chidid - Benen Level
Album Benen Level
date of release
08-02-2020




Attention! Feel free to leave feedback.