Youssou N'Dour - Beugue Dou Bagne Lyrics

Lyrics Beugue Dou Bagne - Youssou N'Dour



Couple bi
Maye dadiéle soumaye dokhanetou dji
Foléne séne
Gnoungui défe bras dessus bras dessous
Bataye gnoungui ni dôniye make, di
Geu-neu begeunté
Mbeugéle rékka wor
Mbeuguéle, mbeguéle rékka nekhe
Taye gnoungui ni di tôgnanté
Di kalanté, melniye dômi badiéne
Léke léke gnou méro ba kouné khole guéthie
Nga guéssouwaté sénate léne gnouye
Wakhtane
Oh mbeguéle, mbeguéla nekhe
Gueume léne ni, mbeguéle, rékka wor
Han... oooh
Bagnou dôné gouné
Thi lagne khamanté wône
Bagnou dôné ay ndawe
Thi lagne begueuneté wône
Bataye gnoungui ni, dôniye make
Digueu-neu begueuneté
Mbeguéla wor
Mbeguéle, mbeguéle rékka nékhe
dokhé ba séne kéne thi gnôme gnare
Tôgale khare, légui kénéne ki gneuwe
Dara gueunoule nekhe
Mbeguéle gou sincére
Gôgou mbeguéle
Kéne dou thi meune dara
Oh mbeguéle, mbeguéla nékhe
Gueume léne ni mbeguéle rékka wor
Han... oooh
Mane beugue nâla, mâla rawe menou faye
Wouy mbeguéle, wouy mbeguéle, wouy Guise beugue yalla mo koye défe wouy
Mbeguéle, wouy mbeguéle wouy
Mbeguéle, wouy mbeguélo
Beugue na beguetouma, bôba mbeguéle
Ga dafa dess
Mbeguéle bou diogué thi khole, délou Fa laye desse abadâan
Mbeguéle kéne meunou ko diaye
kéne menou dieunde thia marsé ba Défe thia yeurmandé
Marie ak Cheikh Marie (choeurs)
Beuguéneté naniou, Amar
Xamanté naniou bou yague
Beuguéneté naniou
Xamanté bou yague, Amar
Minanté naniou, Amar
Haan beugueunté naniou
Mbeguéle kene douko diaye
Mbeuguéle amoul religion
Mbeuguéle amoul niit kou nioul
Ak niit kou wekh
Edit by Lamine



Writer(s): GUEYE MOUHAMADOU, CALO' MASSIMILIANO, NDOUR YOUSSOU


Youssou N'Dour - Alsaama Day
Album Alsaama Day
date of release
10-04-2007




Attention! Feel free to leave feedback.