Youssou N'Dour - Del Sol Dal Lyrics

Lyrics Del Sol Dal - Youssou N'Dour



He boul deff tankunen
Tankunen dh meunala andil problème beu sonnal la
Nanga sol dal fo meuneuti dem
Xotou bouteille yi danio barri te sax meune nagnla gagn
He bayil deff tankunen
Tankunen dh meunala andil problème boula diakhal
Xotou bouteille yakh mba weign bou xourr
Loumci meuneu done boula diame meuneu nga cia am problème
Boula diamei niou gawantou yanoula yobou hôpital
Boula diamei niangay xalat hôpital fann ngi
Nane Abass Ndao mananelen dantec mo gueneu djeiguei
He bayil deff tankunen
Tankunen dh meunala andil problème ba sonnal la
Nanga sol dal fo meuneuti dem
Khotou bouteille yi danio beuri te sakh meune nagnla gagn
Boula diamei niou gawantou yanoula yobou hôpital
Boula diamei niou ngay xalat hôpital Fann gni
Nane Abass Ndao mananelen Dantec mo gueneu djeiguei
You are my sunshine you are my heart I love u i love u i love u
I love u my child Iow bulko fattei heyy tankunen dh baxoul (×3)




Youssou N'Dour - Alsaama Day
Album Alsaama Day
date of release
10-04-2007




Attention! Feel free to leave feedback.