Lyrics Yonou Deugue - Youssou N'Dour
Sama
domou
yaye,
bo
oubé
bountou
deugue
Boule
ragalwéte,
ndakhe
dina
néw
gnou
la
feugue
Sâye
sâye,
séîtané,
gni
diouboule
dougne
la
beug
Gni
ragal
di
lakhou
ak
gni
khamouldougne
la
leungue
Wâyé
séne
bîre
khole,
niome
séne
bîre
khole
Fougnou
néke,
gnougue
lay
khalate,
thi
séne
khéle
Wâyé
séne
bîre
khole,
niome
séne
bîre
khole
Gnou
gui
laye
diapalé
thi
lou
wêre
Besse
dina
gneuwe
Yangi
doga
khame,
thi
boula
thiono
dabé
Li
di
mbéttéle
dana
la
diogué
founé
Dougnou
nieuw
sa
keur
té
dotou
gnou
la
téléphoné
Daniouye
fôke
ni
yawe
bougnou
la
diégué
sakh
yakhoulé
Wâyé
séne
bîre
khole,
niome
séne
bîre
khole
Fougnou
néke,
gnougue
lay
khalate,
thi
séne
khéle
Ragale
fésse,
pékhé
diékhe
Gnoungui
lay
diapalé,
thi
lou
wêr
Bess
dina
gneuwe
Yawe
sa
nattago,
ngene
bokke
beugue
beugue
Boula
beugue
ndaw
téré
wakhe
li
dideugue
Loumou
métti
métti
métti,
nangoul
né
wadji
mbeur
la
Loko
contre,
contre,
contre,
sédelni
liguey
kat
la
Yawe
sa
bîre
khole,
yawe
sa
bîre
khole
Finga
nék
nangou
nga
né
diambare
la
Ragale
fésse,
pékhé
diékh,
Sougnou
guisse
guisse,
meune
na
wouté
Wouté
guisse
guisse
boumou
takh
bangnou
bagnaneté
Boul
di
neubbe
fa
nga
fété
Yalla
sakh
dafa
tane
yonénte
mou
djité
Yawe
na
nga
moytou
ragale
pété
Dégue
nané
meune
nala
khagne
sa
mbecté
Yawe
na
nga
moytou
ragale
pété
Dégue
nâni
meune
nala
khagne
sa
mbecté
woooh
Sougnou
borom
bi
rek
mo
meune
founé
Gni
dagbouy
ragale
gni
thi
dess
gnémé
Say
wakh
ak
say
dieuf,
mome
boutégo
thi
deugue
Yawe
nga
wêye
boule
ragale
Yonou
deugue
mome
Bothie
nékké
hé
di
dem
Boul
ragale
wéet
Ndakhté
dingua
néwe,
nioulaye
Feugueu
Saîsaîyé,
gni
diouboul
Ak
ki
khamoule
dougne
lameune
Beugeu
waw
Yonou
deugue
mome
Bothie
nékké
di
dem
Boul
ragala
wéet
Ragale
fésse,
haann
pékhé
dikhe...
Résumé
Français:
Qui
aime
bien
châtie
bien.
Pars
du
simple
fait
que
toute
vérité
est
bénéfique.
Ne
t'en
détournes
jamais
frère,
Car
elle
sera
pour
toi
source
de
lumière
1 Bou ba yeko
2 Beugue Dou Bagne
3 Borom Gaal
4 Amitié
5 Téléphone
6 Yonou Deugue
7 Bololene
8 Del Sol Dal
Attention! Feel free to leave feedback.