Lyrics Téléphone - Youssou N'Dour
Mineuneté
sou
amoul,
thioféle
dé
dotoulame
Thioféle
dé,
sou
amoul
beugueneté
dotoul
ame
Beugeuneté
sou
amoul,
kharito
dotoul
ame
Kharito
sou
amoul,,
khole
yépeu
dal
di
wowe
Kholeyi
dé
sou
wowé
yeurmandé
dal
di
diekh
Yeurmandé
sou
amoul
seîtané
dal
di
téwe
Séîtané
sou
gnewé,
askane
wi
dal
di
tasse
Ndékété,
safara,
dina
dioure
diangoro
Lî
doyna
waré,
doyna
ware
Gueudj
naniou
langue
lôlé
Di
wakh,
di
kholaneté
hé
hé
hé
Sétalma
lilé
hé
Guisseulema
lilé
hé
hé
hé
Sétalma
lilé
hé
Guissalema
lilé
hé
hé
hé
Haannn...
ana
penche
ma,
ana
sabar
ya,
ana
tama
dia
Yegueléléne,
yeguelélno,
yegueléléno
Bou
ndieukone,
wakhtane
thi
penche...
Diébané
tamaka
dane
def,
sabaraka
dane
def,
wouy...
1 Bou ba yeko
2 Beugue Dou Bagne
3 Borom Gaal
4 Amitié
5 Téléphone
6 Yonou Deugue
7 Bololene
8 Del Sol Dal
Attention! Feel free to leave feedback.