paroles de chanson Pottu Ndaa - Ashs The Best
Gisoo
ni
fu
sori
la
joge
Ba
ñuy
gone
dañ
foogoon
ni
Boo
maggee
Loo
yootu
day
gaaw
Tera'nga
bi
day
naxe
ci
boo
foogee
Lepp
yay
boroom
Adduna
bi
pottu
Ndaa
la
boo
naanee
jox
sa
moroom
naan
Jamm
du
doy!!!
Du
alal
jamm
moo
li
gën
ci
ñun
Nang
xoolee
sa
bopp
yeene
ko
peace
and
love
and
harmony
Lepp
du
yay
boroom
fii
dang
fi
am
waar
keneen
am
fi
waar
Saabu
bi
footul
boppam
Man
la
man
la
lune
nga
ne
yay
boroom
Fii
demal
maa
ngi
ñëw
la
Tay
sa
bis
suba
bisam
la
Boo
goree
jekkoo
del
baalee
Adduna
di
ndaa
yow
Soo
naane
jox
sa
moroom
naan
yow
Yaatu
yaatalal
sa
xol
yow
Jamm
du
doy!!!
Seet
naa
ba
seet
moy
li
gën
ci
ñun
Mbëggeel
akk
alal
du
doy
Bu
fi
jamm
nekkul
dara
xajjul
ci
ñun
Saabu
bi
footul
boppam
Man
la
man
la
lune
nga
ne
yaa
ko
moom
Dimbalil
xale
bi
mbokkam
Xoolal
li
nga
yeene
sa
bopp
yeene
ko
bepp
jaam
Gisoo
ni
fu
sori
la
joge
Ba
ñuy
gone
dañ
foogoon
ni
Boo
maggee
Loo
yootu
day
gaaw
Tera'nga
bi
day
naxe
ci
boo
foogee
Lepp
yay
boroom
Adduna
bi
pottu
Ndaa
la
boo
naanee
jox
sa
moroom
naan
Attention! N'hésitez pas à laisser des commentaires.