Ashs The Best - Xel Akk Xol paroles de chanson

paroles de chanson Xel Akk Xol - Ashs The Best



Yeah, eh eh eh
Lé, lé, walé
Hum, hum
Suba suma yeewu
Yaw lay bëgg jakarlool
Sa suma yeewu
Yaw lay bëgg njëkk xol
Ëlëk lu mata soor la
Wayé xel xalatu ko
Ëlëk ay jaar-jaar la
Sama xol yëgoon nako muy ñëw
Xel xalaat la (xel ak xalatam bë)
Xol yëkk yëkk la
Nit ak jëmëm
Dara xaaju
Sa suma yeewu
Yaw lay bëgg njëkk xol
(Suma yewo yaw la bëgg njekk xol)
Fajar suma yeewu
Yaw la bëgg jakarlool
Denk na la guddi
Fanané yakkar ci yaw
Gent na la guddi gi yëpp
Ndax fajar yaw lay jakarlool
Mbëggël!
Xel xalaat la
Xol yëkk yëkk la
Nit ak jëmëm
Dara xaaju
Nit nak ak jëmëm
Dara fa xaajul



Writer(s): Olivier Delahaye, Abdoulaye Sy, Arfang Tiare


Ashs The Best - Dibèer
Album Dibèer
date de sortie
11-06-2021




Attention! N'hésitez pas à laisser des commentaires.