paroles de chanson Loy Yeuk - Nitdoff , Leuz Diwane G
Loy
yeuk
boulma
neub
wakhma
loy
yeuk
Li
ngey
xeuy
di
tekk
sa
eyes
si
life
bi
eskeu
do
nieuk
Black
lives
matters
tekiwo
té
matoulo
ndieuk
Eskeu
sakh
dou
sunuy
dome
li
laniouy
dound
euleuk
Loy
yeuk
George
Floyd
bimouy
fateu
bey
xeuthie
Loy
yeuk
niom
seni
kasso
nit
niou
gni
ley
teuthie
Loy
yeuk
black
bou
teuko
black
beu
raye
ko
loy
yeuk
Mane
sama
khekh
moy
nouniouy
def
beu
ande
rise
up
Danio
takhalo
tchi
finiou
waron
ande
penthio
Black
doon
démon
tchi
black
tchi
white
mou
doon
feu
angel
Dem
beu
melni
black
beuguoul
black
meunou
niou
dendo
Lolou
yepp
toubab
biy
gueun
di
raw
beguoul
niou
ménguo
Loy
yeuk
boy
xeuy
di
guiss
tchi
adouna
ni
nioun
black
Dafeu
melni
niepeu
niouy
fight
Diotna
niou
bolo
sunu
side
Dioytou
di
sakou
séen
Love
takhoul
niou
diokhniou
sunu
right
Naniou
dagu
chaine
yi
kone
té
tambalé
guemat
luy
sunu
life
Loy
yeuk
waxmako
boul
ma
feen
Loy
yeuk
bouniouy
raye
seu
yen
frères
yi
Loy
yeuk
deer
bu
ñul
dioy
neu
feep
fo
dem
Ndeysane
noyi
sax
moudiou
na
doneu
problème
I
can't
breathe
i
just
wanna
live
Please
sir
I'm
hurt
Loy
yeuk
africain
bi
wakhma
loy
yeuk
Sou
njitou
rew
yi
deupé
caisse
bayi
xeet
bi
khiif
Lo
tchi
wakh
niou
teuthie
leu
rap
tekk
tchi
ngade
ley
life
Ki
am
beu
ouf
louni
gagni
sakh
sey
peep
ley
sif
Loy
yeuk
nit
kou
niouley
djiap
rendi
niou
nioul
Nit
kou
niouley
gang
banging
tirer
niou
nioul
Système
bi
keep
cool
noote
neu
balck
people
Oubi
bountou
jail
tekk
tchi
bountou
cimetière
Brain
watching
def
equation
bi
tchi
misère
Corrompre
yennen
black
niou
sampe
illusion
Kou
meloul
ni
do
tekki
K
O
bé
def
division
Def
sa
khel
music
sport
sinan
mbedey
solution
Cravache
defneu
teurgueun
migui
sunuy
ndode
Engagement
bi
neu
sincère
waroul
nekk
mode
Sepi
ragné
sunuy
ennemie
ak
seni
méthode
Bepp
black
defna
malcom
diougu
takhaw
ni
thiode
Loy
yeuk
ci
borom
kholou
dothie
Magui
dead
meunouma
noyi
mou
dieul
aumeum
gueneu
khodj
Nguir
George
ak
gni
ko
djitou
black
yi
wathie
fepp
tothie
Racisme
dou
lou
bess
téléphone
yi
nioko
kothie
No
justice
no
peace
ain't
no
please
Diokhleen
niou
sunu
geudeu
black
nobility
Bo
diamé
ben
black
black
yepp
niou
gui
bleed
Ay
skinnette
you
sole
tenue
fuck
seni
flic
Loy
yeuk
waxmako
boul
ma
feen
Loy
yeuk
bouniouy
raye
seu
yen
frères
yi
Loy
yeuk
deer
bu
ñul
dioy
neu
feep
fo
dem
Ndeysane
noyi
sax
moudiou
na
doneu
problème
I
can't
breathe
i
just
wanna
live
Please
sir
I'm
hurt
Why
don't
we
got
the
right
to
live
Like
anybody
on
earth
I
can't
sleep
tight
He's
not
alone
all
of
us
can't
breathe
All
the
black
community
just
can't
breathe
right
Eye
for
an
eye
tooth
for
a
tooth
Like
black
Panther
party
decided
years
ago
We
gotto
keep
an
eye
opened
we
are
the
truth
Stand
for
every
black
man
on
earth
I
say
here
we
go
Arabe
yi
di
ñu
xoxatal
noot
ñu
seni
réw
Su
ñu
ndjiit
yi
takk
ñu
buum
yobu
diox
nassarane
Der
Bu
ñuul
diap
der
bu
ñuul
rendi
def
ko
neew
Ñu
nûy
xex
ñuy
xex
su
ñu
biir
di
gëna
saaraan
Bu
nguéne
ñu
bëgul
ñun
bëgu
ñu
leen
Bu
nguén
ñu
feeloul
it
ñun
feelou
ñu
leen
Wayé
derete
dji
turu
su
ñu
biir
si
ñuni
neen
Warna
dakeu
ñu
bolé
dolé
yi
def
ko
ben
Racisme
21ème
siècle
Est
une
défaite
pour
l'humanité
toute
entière
On
pardonne
mais
on
n'oublie
jamais
L'esclavage
ce
fameux
traite
triangulaire
Beug
na
xam
lane
mo
waral
Lu
takh
der
bu
ñul
wara
soneu
fep
fo
dem
Té
fou
way
amé
ndam
su
ñu
loxo
nga
ca
wëral
Bu
ñu
jogul
kene
du
ñu
fadial
sou
niouy
problème
Bedoukou
bérou
dongu
developper
sunu
koom
Yenenté
sunu
biir
kouneh
push
sa
morom
Defal
sa
khel
ni
biss
war
nga
delou
mother
land
Africa
is
the
futur
gnibissil
sakh
fi
réen
broda
1 Intro
2 Niip Mic
3 Imbécilo Rék
4 Virus
5 PYS
6 Wané Fite
7 Go Get It
8 Loy Yeuk
9 Yafi Nék
10 Seedorf
11 Ride or Die
12 Better Leave
13 Rolling
14 Gun To Da Z
15 Interlude
16 I'm
17 Bombaclat
18 Obi Médecin
19 Vécu
20 Yoonu Ndaw
21 No Bullshit
22 Big Shoot
23 Doing My Time
24 DND - Bonus Track
Attention! N'hésitez pas à laisser des commentaires.