Nitdoff - Better Leave paroles de chanson

paroles de chanson Better Leave - Nitdoff

Better better leave you better leave
Better better leave you better leave now
Better better leave you better leave
Better better leave you better leave now
Sagua djiap door torokhal
Bou fekké beuguato bayil mou leave now
Nioun goorr suniu beuguatoul douniou assumer
Nioy push djiguen bi pour mou craquer sassounéh
Better understand use sa brain
Kiléy diade lo dou sa friend
Dedet dou sa nawlé bokouléen
Safane rekk ley doundé daw beu rénn
Daw guaw soriko bala mouy late
Nga melni mom rek ley wait
Amoul ay kheuy amoul ay kilifa tayit
Ci liko nekh rek ley nekk
Boul doff boul tokk
Ak kiy beugua freiner sey ambition
Dey djiem daley bapp taukh ak nane
Bou sanione nga ceder tentation
Bro tanal sey andado
Nio khamni nio gui ak sen saguo
Meytoul gniy prek
Loy dougu néy léer
Defkat yi meytoul sakh sen shadow
Better better leave you better leave
Better better leave you better leave now
Better better leave you better leave
Better better leave you better leave now
Sagua djiap door torokhal
Bou fekké beuguato bayil mou leave now
Nioun goor suniu beuguatoul douniou assumer
Nioy push djiguen bi pour mou craquer sassounéh
Togual mounie
Na fekk mou doon kouko diar
Khole atanoul
Yénn yi meun naleu raye
Nigga seuy dou jail
Peine nou perpétuité took fay dound hell
Tellement belle nga fi niane ci woon
Sopiko t′es ma chienne
Dieul seu responsabilite doneu kilifa ngey banie
Fanane aleu tamba balou sa bakane limou beugu dokoko khagne
Better better leave you better leave
Better better leave you better leave now
Sagua djiap door torokhal
Bou fekké beuguato bayil mou leave now
Nioun goorr suniu beuguatoul douniou assumer
Nioy push djiguen bi pour mou craquer sassounéh

Writer(s): Amady Fall, Isdeen Marion Elie Jimo, Mor Talla Gueye

Nitdoff - The Beast 1
Album The Beast 1
date de sortie
20-09-2020

Attention! N'hésitez pas à laisser des commentaires.