paroles de chanson Yoonu Ndaw - Nitdoff , Mao Sidibé
Dokh
ci
yonou
ndaw
dafeu
bari
piège
Meun
nga
fallin'
down
meun
na
doon
lou
yées
Doolé
dokhoul
diam
saurato
ay
conséquences
Life
fou
legalize
rékey
doon
sey
influences
Yonou
ndaw
dou
wéey
teguil
sa
tank
please
Bodoul
ingénieur
meun
nga
doon
chef
d'entreprise
Att
yi
nga
tolou
sa
dérét
dafey
tangue
So
tarkhissé
rek
meun
nga
niak
bepp
maîtrise
Petit
frère
écoute
moi
Yonou
ndaw
moleu
djiap
mélo
ni
Petite
soeur
mais
dis
moi
Pourquoi
tu
penses
que
si
triste
est
la
vie?
Le
meilleur
reste
à
venir
C'est
maintenant
que
tu
dois
batir
Ton
avenir,
ton
avenir,
prépare
toi
pour
ton
avenir
Yeah
ya
ngui
tolou
pont
bou
diafé
djiegui
boy
Gni
si
toloon
naagu
danio
djieki
djieki
yooy
Virage
bi
nga
nekk
moy
déterminer
fi
nga
dieum
Andado
you
bonn
danie
léy
précipiter
ci
leundeum
Niep
gui
koy
def
waroul
takh
nga
warko
def
Complexer
bakhoul
doon
sa
propre
chef
ci
li
séy
choice
Khana
xamo
ni
diné
meun
neu
doon
boussole
So
tchi
télé
tagguatt
sa
bopp
Léer
gui
dafey
sakh
sa
khole
Petit
frère
ecoute
moi
Yonou
ndaw
moleu
djiap
mélo
ni
Petite
soeur
mais
dis
moi
Pourquoi
tu
penses
que
si
triste
est
la
vie?
Le
meilleur
reste
à
venir
C'est
maintenant
que
tu
dois
batir
Ton
avenir,
ton
avenir,
prépare
toi
pour
ton
avenir
Han
khalé
bou
dioumé
boul
ko
téleu
wakh
ni
da
nga
bonn
Dieuleul
sa
temps
nga
dioubanti
ko
bamou
doon
Ki
ngey
saguo
euleuk
fepp
nane
khole
léen
sama
dome
Guinaw
Yallah
dala
sameu
lo
kone
waro
faille
Beurina
wadiour
youy
échouer
tchi
sen
oyofaay
Sa
dome
dou
nguew
am
xélam
boul
ko
yéw
Liy
thiossanam
warna
fégne
tchi
mom
fepp
foumou
téew
Sinon
rek
nga
sopiko
ap
dondjie
keurign
ci
biir
méew
Petit
frère
ecoute
moi
Yonou
ndaw
moleu
djiap
mélo
ni
Petite
soeur
mais
dis
moi
Pourquoi
tu
penses
que
si
triste
est
la
vie?
Le
meilleur
reste
à
venir
C'est
maintenant
que
tu
dois
batir
Ton
avenir,
ton
avenir,prépare
toi
pour
ton
avenir
Little
little
sista
Little
little
broda
Take
care
of
yourself
Adouna
yaguoul
wéi
Yonou
ndaw
dou
wéey
dou
wéey
dou
wéey
dou
wéey
dou
wéey
Kone
gars
yi
téelou
léen
1 Intro
2 Niip Mic
3 Imbécilo Rék
4 Virus
5 PYS
6 Wané Fite
7 Go Get It
8 Loy Yeuk
9 Yafi Nék
10 Seedorf
11 Ride or Die
12 Better Leave
13 Rolling
14 Gun To Da Z
15 Interlude
16 I'm
17 Bombaclat
18 Obi Médecin
19 Vécu
20 Yoonu Ndaw
21 No Bullshit
22 Big Shoot
23 Doing My Time
24 DND - Bonus Track
Attention! N'hésitez pas à laisser des commentaires.