Nitdoff - Yafi Nék paroles de chanson

paroles de chanson Yafi Nék - Nitdoff



Bou solo nga ni déteuwaay
Bou dokhé damey beugu raye
Amna ay feeling fepp nice
meuno dianok mom ci eyes
Akeuy ndanane nimkay deffé amoutchi size
Damey danel boudoon diaay ma dem wuti price
Dou wané leen lepeuy mourou dareu dou fegn
Damey wootal mey gueuneu lab ci guediou love
Yaay ndanane dionguama mang tchi yaw
Gaagn nga ma doff loma don′t u know
Taar mong ci yaw yaar mong ci yaw
Foulak fayda yaw yaay dionguama
Ken doula guiss kersa nga fess
Teyé gua sa bopp koula am dieul yaw leernameu
Diongama ni yaw deh amoul
Dionguama ni yaw deh amoul
Sa dokhina andak class
Sa dieufine efficace
Assalo diokhéna sama khole
Sa dokhina andak class
Sa dieufine efficace
Tassaro samey beutt yaw ley khole
Hée hée fi ya fi néh
Ken dou yaw ken dou yaw damaleu guiss rek
Sama khole taneu leu kaay niou vitesse ci love
Yagui leer yagui yiiw like my sunshine
Wakh ci yaw rek plaisir leu takhneu mey gueun fine
Baby girl louné fang kenn douko lathie
Taaru ouroul ayni fegn seu dieum yeen
Saaay
Damleu L.O.V.E my baby
Naleu yeuk lo li ci paradis Yeah
Mel nga ni gaur di sohla ci djiguen
Khet gui ngey guili da melni wa eden
Khole bi mo sénénn falewoul kenen
Yaaye sama beautiful à la peau d'ébène
Baby na yallah def li nemeu ameen
Khole laleu amel yaguimey danel
Ko meusseu sourire bataye moguley dianére
Diongoma kholma ma yeuk coup de tonnerre
Diongama ni yaw deh amoul
Dionguama ni yaw deh amoul
Sa dokhina andak class
Sa dieufine efficace
Assalo diokhéna sama khole
Sa dokhina andak class
Sa dieufine efficace
Tassaro samey beutt yaw ley khole
Hée hée fi ya fi néh



Writer(s): Isdeen Marion Elie Jimo, Mor Talla Gueye


Nitdoff - The Beast 1
Album The Beast 1
date de sortie
20-09-2020




Attention! N'hésitez pas à laisser des commentaires.