paroles de chanson Bàjjan - Youssou N'Dour
Taasukat
baa
nga
naan
gainde
gu
waaf
ca
buntu
kër
gé,
di
melastiku
Bëy
bu
em
bàjjan
du
fa
dem,
Zacharia,
bàjjan
am
na
maanaa,
wayai
Lu
la
réér
ci
sa
cosaan,
sa
bàjjan
xamal
la
ko
Boo
bëgéé
xam
sa
cosaan,
kam
la
fa
maam
yi
bayyi
woom
Demal
seeti
bàjjan
ba,
lu
mu
la
ca
wax,
du
deñ
Bàjjana
xam
Kalcor
an
ba
ca
mbeneex
wa
Cosaani
askan
wi,
bàjjan
am
na
maanan
Wayum
terànga
la
kuy
bàjjan
jog,
Sungun
SanGan
bàjjan,
bàjjan
Wayum
TERANGA
la
kuy
bàjjan
jogal
yëngu,
bàjjan,
bàjjan,
Sungun
SanGan
Neenan
mag
a
pu
rencontrer
de
naa
ba
cim
rééw
Waaye
bàjjan
il
a
répondu
à
na
bàyyi
ci
biir
Kër
Xam
sa
Boppa
Gén
Ñu
woo
la
naan
kii
nga
Doon
Wayum
TERANGA
la
kuy
bàjjan
jogal
yëngu,
sunguñ
sangañ
bàjjan,
bàjjan
Wayum
terànga
la
kuy
bàjjan
jogal
yëngu,
bàjjan,
bàjjan,
sunguñ
sangañ
Boo
bëgéé
xam
sa
cosaan,
sa
bàjjan
moo
la
koy
xamal
Moo
la
naan
awai
fii,
bul
dem
fee,
defeel
nii
Boo
ko
seetioo
dara
du
ca
deñ
Wayum
terànga
la
kuy
bàjjan
jogal
yëngu,
sunguñ
sangañ
bàjjan,
bàjjan
Wayum
terànga
la
kuy
bàjjan
jogal
yëngu,
bàjjan
Si
bj
Gaay
Walla
raidiam
Lu
xew
lune
crinière
bàjjan
laxaw
Bu
Goor
bugéé
néégu
Goor
Bàjjan
taxaw
wayal
ko
mbaax
Nijaay
di
Yaay
nga
di
Baay
Bàjjan
am
na
maanaa
Wayum
TERANGA
la
kuy
bàjjan
jogal
yëngu,
Sungun
SanGan
bàjjan,
bàjjan
Wayum
TERANGA
la
kuy
bàjjan
jogal
yëngu,
bàjjan,
bàjjan,
sunguñ
sangañ
Bàjjan
moodi
magi
baay
walla
rakkam
Lu
xew
lune
mane
bàjjan
laxaw
Bu
góó
bugéé
néégu
góór
Bàjjan
taxaw
wayal
ko
mbaax
Nijaay
di
Yaay
nga
di
Baay
Bàjjan
am
na
maanaa
Wayum
terànga
la
kuy
bàjjan
jogal
yëngu,
sunguñ
sangañ
bàjjan,
bàjjan
Wayum
terànga
la
kuy
bàjjan
sj
1 4-4-44
2 Pullo Àrdo
3 Sama Gàmmu
4 Bàjjan
5 Baay Faal
6 Sportif
7 Tukki
8 Létt Ma
9 Dabbaax
10 Xel
11 Wake Up (It's Africa Calling)
Attention! N'hésitez pas à laisser des commentaires.