Youssou N'Dour - 4-4-44 paroles de chanson

paroles de chanson 4-4-44 - Youssou N'Dour



4-4-44 (4-4-4-44) môm sa bopp neikh
4-4-44 (4-4-4-44) guiss say mbok neikh
léké ba sour war nga gueureum
War nga gueureum gni doug thi wagne
Wagne wa tang na.
Fimou toll war nguèna bëg
War-ngèna bëg thi indépendance bi ak-liko indi
4-4-44 (4-4-4-44) môm sa bopp neikh
4-4-44 (4-4-4-44) guiss say mbok neikh
léké ba sour war nga gueureum
War nga gueureum gni doug thi wagne
Wagne wa tang na.
Damani bou leuk léké olom
Boudè goréna deugou warna ko guereumé pithe.
No, no, no no no no
No, no, no no no no yeah
4-4-44 (4-4-4-44) guiss say mbok neikh
4-4-44 (4-4-4-44) guiss say mbok neikh
Ah li dafa nékh... guiss say mbok neikh
Li dafa nékh... gueume sa bopp nékh
4-4-44 (4-4-4-44) môm sa bopp neikh
No, no, no... guiss say mbok neikh
4-4-44 (4-4-4-44) môm sa bopp neikh
Oa, li dafa nékh... guiss say mbok neikh
A... môm sa bopp neikh
Oa, li dafa nékh... môm sa bopp neikh



Writer(s): Youssou N'dour, Kabou Gueye


Youssou N'Dour - Rokku Mi Rokka
Album Rokku Mi Rokka
date de sortie
29-10-2007




Attention! N'hésitez pas à laisser des commentaires.