Lyrics Tukki - Youssou N'Dour
Yoon
wi
nga
jël
baaxul
ku
la
koy
digël
da
lay
nax
Yoon
wii
ci
des
moo
gën,
loo
taseel
dàldi
kuy
mën
Yoon
wii
nga
jël
booy
dox
ba
ca
Biir
géstul
xool
fi
nga
weesu
balaa
ngay
Booy
tukki
yaw
Booy
tukki
yaw
Na
nga
bàyyl
ba
mën
Ding
cë
jëléé
lu
mënë
xew
ca
feneen
Dina
tax
nga
mën
xam
nekkinu
ñeneen
Foofo
mën
nga
fa
gis
lu
yókk
sa
xameel
Booy
tukki
yaw
Nita
ngi
toog
di
janoog
yaw
booba
Fekk
na
ma
ngay
xalaat
ba
tàbbi
asamaan
Àndag
niir
yiy
naaw
dem
na
fu
sore
lépp
ciy
xalaatam
Yaw
sama
waay
kaay
ma
xamal
la
Léég
léég
nga
toog
fi
nga
toog
tukki
bu
neex
dem
ba
kaw
asamaan
Ànd
ag
weer
wiy
naaw
li
ngay
janeer
Mu
lay
neex
boo
janoo
mu
gën
fee
neex
Booy
tukki
yaw
Booy
tukki
yaw
yeesal
sa
xameel
Ding
cë
jëléé
lu
mënë
xew
ca
feneen
Dina
tax
nga
mën
xam
nekkinu
ñeneen
Foofa
mën
nga
fa
gis
lu
yókk
sa
xameel
Deel
tukki
yaw
Lëppa
lëpp
sàmba
ma
ngay
naaw,
te
booy
seet
sax
taxu
koo
gaaw
Te
léég
léég
mu
dem
ba
kaaw
Tukkee
ka
neex,
waaw
Lucum
cééli
ma
ngay
naaw
te
léég
léég
Mu
naaw
ba
kaw
asamaan
indi
fiy
xabaar
Ku
dul
tukki
doo
xam
fu
dëkk
neexe
Booy
tukki
yaw
Na
nga
bàyyi
Booy
tukki
yaw
Na
nga
bàyyi
ba
mën
Ding
cë
jëléé
lu
mënë
xew
ca
feneen
Dina
tax
nga
mën
xam
nekkinu
ñeneen
Foofa
mën
nga
fa
gis
lu
yókk
sa
xameel
Booy
tukki
yaw
Booy
tukki
yaw
Booy
tukki
yaw
Na
nga
bàyyi
ba
mën
Ñaanu
barke
ah
ñaanu
barke
Nita
ngi
toog
di
janoog
yaw
booba
Fekk
na
ma
ngay
xalaat
ba
tàbbi
asamaan
Àndag
niir
yiy
naaw
dem
na
fu
sore
lépp
ciy
xalaatam
Yaw
sama
waay
kaay
ma
xamal
la
Léég
léég
nga
toog
fi
nga
toog
tukki
tukki
bu
neex
dem
ba
kaw
asamaan
Làng
ag
weer
wiy
naaw
li
ngay
janool
mu
Lay
neex
boo
janoog
moom
mu
gën
fee
neex
Booy
tukki
yaw
Na
nga
bayyi
ba
mën
Ding
cë
jëléé
lu
mënë
xew
ca
feneen
Dina
tax
nga
mën
xam
nekkinu
ñeneen
Foofa
mën
nga
fa
gis
lu
yókk
sa
xameel
Deel
tukki
yaw
Lëppa
lëpp
sàmba
ma
ngay
naaw,
te
booy
seet
sax
taxu
koo
gaaw
Te
léég
léég
mu
dem
ba
kaaw
Tukkee
ka
neex,
waaw
Lucum
cééli
ma
ngay
naaw
te
booy
seet
Sax
taxu
koo
gaaw
ëndaaleel
ñu
xabaar
Tukkee
ka
neex,
waaw
1 4-4-44
2 Pullo Àrdo
3 Sama Gàmmu
4 Bàjjan
5 Baay Faal
6 Sportif
7 Tukki
8 Létt Ma
9 Dabbaax
10 Xel
11 Wake Up (It's Africa Calling)
Attention! Feel free to leave feedback.