Lyrics Sportif - Youssou N'Dour
Woyal
sa
wayu
ndam
ii
Dangay
bégël
sa
xol
bi
Ndax
yaa
yor
bannex
bi
Ni
tay
bés
bii
sa
bés
la
Sa
mbër
daan
na
kóntaan
nga
Bu
ñu
daanee
sa
mbër
nak
Na
nga
fexe
ba
nee
Po
mii
dañuy
Jonante
Faw
mu
am
ku
moyle
Jarula
defante,
di
xasteeka
dóóre
Jonante
po
ag
ree
la
Boo
gañee
fo
ag
ree
la
Boo
ñàkkee
fo
ag
ree
la
Lépp
ci
fo
ag
ree
la
Buñ
la
gañee
muñël
Boo
ko
gañee
baalal
Bëgóón
nga
mu
demee
ni
demewuko
Mën
naa
am
bu
ëllëgee
mu
gën
fee
neex
Ba
ma
làng
ag
samay
gaa
yi
ngir
bànneexu
Xam
ne
lii
fo
la
nii
lay
mënë
deme
Powun
jonante
nii
lay
deme
Tay
jii
yaw
bu
ëllëgee
keneen
la
Fo
ag
ree
de
lañ
ciy
jublu
Moo
tax
ñu
wara
dal
taynangu
defet
Jonante
po
ag
ree
la
Boo
gañee
fo
ag
ree
la
Boo
ñàkkee
fo
ag
ree
la
Lépp
ci
fo
ag
ree
la
Buñ
la
gañee
muñël
Boo
ko
gañee
baalal
Waa
waaw
wuy
dabbee
wuy
yoo
Dabi
alaa
ko
ndey
baate
satata
Abdulaay
ag
Maajoor
Maajoor
ag
Mataar
ag
jaara
seen
jigéén
Sire
lañu
dóór
bal
géér
ña
da
ñoo
daw
Sire
Bàlla
moo
ñaan
Ramata
Faal
Siree
nga
Cees
Matee
nga
Njaarém
Duñ
ko
wëy
ku
reew,
duñ
ko
wëy
ku
ñaaw
Aah
wuy
dabbee
wuy
yoo
Dabi
alaa
ko
ndey
baate
satata
Jonante
po
ag
ree
la
Boo
gañee
fo
ag
ree
la
Boo
ñàkkee
fo
ag
ree
la
Lépp
ci
fo
ag
ree
la
Buñ
la
gañee
muñël
Boo
ko
gañee
baalal
1 4-4-44
2 Pullo Àrdo
3 Sama Gàmmu
4 Bàjjan
5 Baay Faal
6 Sportif
7 Tukki
8 Létt Ma
9 Dabbaax
10 Xel
11 Wake Up (It's Africa Calling)
Attention! Feel free to leave feedback.